Al-Baqara · 252/286
Tekki Waxtaan — Al-Baqara
تِلْكَ آيَاتُ اللَّهِ نَتْلُوهَا عَلَيْكَ بِالْحَقِّ ۚ وَإِنَّكَ لَمِنَ الْمُرْسَلِينَ ٢٥٢
Transliteration
Tilka Aayaatul laahi natloohaa `alaika bilhaqq; wa innaka laminal mursaleen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Kàddug Yàlla googu dananu la ko jàngal ci dëgg.Te yaw [Muhammad] (saw), ci Yonent yi nga bokk.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 250-254 — Al-Baqara
250وَلَمَّا بَرَزُوا لِجَالُوتَ وَجُنُودِهِ قَالُوا رَبَّنَا أَفْرِغْ عَلَيْنَا صَبْرًا وَثَبِّتْ أَقْدَامَنَا وَانصُرْنَا عَلَى الْقَوْمِ الْكَافِرِينَ
Ba ñu génnee jëm ca JaaLóota ak i xarekatam, ñu ne : “Yàlla sunu Boroom ! nanga sotti ci nun muñ, te nga saxal sunuy tànk te nga defal nu ndimbal ci kaw nit ñu weddi ñii”.
251فَهَزَمُوهُم بِإِذْنِ اللَّهِ وَقَتَلَ دَاوُودُ جَالُوتَ وَآتَاهُ اللَّهُ الْمُلْكَ وَالْحِكْمَةَ وَعَلَّمَهُ مِمَّا يَشَاءُ ۗ وَلَوْلَا دَفْعُ اللَّهِ النَّاسَ بَعْضَهُم بِبَعْضٍ لَّفَسَدَتِ الْأَرْضُ وَلَٰكِنَّ اللَّهَ ذُو فَضْلٍ عَلَى الْعَالَمِينَ
Nu def ci ndigalu Yàlla [Daawuda] rey [Jaaluta] ; Yàlla jox ko nguur ga ak xam-xam, xamal ko ca la ko soob. Bu dul koon ak li Yàlla di fege aw nit ak ñeneen, kon suuf si dana yàqu. Waaye Yàlla mooy Boroom ngëneel yi muy sotti ci mbindéef yi.
252تِلْكَ آيَاتُ اللَّهِ نَتْلُوهَا عَلَيْكَ بِالْحَقِّ ۚ وَإِنَّكَ لَمِنَ الْمُرْسَلِينَ
Kàddug Yàlla googu dananu la ko jàngal ci dëgg.Te yaw [Muhammad] (saw), ci Yonent yi nga bokk.
253۞ تِلْكَ الرُّسُلُ فَضَّلْنَا بَعْضَهُمْ عَلَىٰ بَعْضٍ ۘ مِّنْهُم مَّن كَلَّمَ اللَّهُ ۖ وَرَفَعَ بَعْضَهُمْ دَرَجَاتٍ ۚ وَآتَيْنَا عِيسَى ابْنَ مَرْيَمَ الْبَيِّنَاتِ وَأَيَّدْنَاهُ بِرُوحِ الْقُدُسِ ۗ وَلَوْ شَاءَ اللَّهُ مَا اقْتَتَلَ الَّذِينَ مِن بَعْدِهِم مِّن بَعْدِ مَا جَاءَتْهُمُ الْبَيِّنَاتُ وَلَٰكِنِ اخْتَلَفُوا فَمِنْهُم مَّنْ آمَنَ وَمِنْهُم مَّن كَفَرَ ۚ وَلَوْ شَاءَ اللَّهُ مَا اقْتَتَلُوا وَلَٰكِنَّ اللَّهَ يَفْعَلُ مَا يُرِيدُ
Yonent yooyu, gënal nanu ñenn ci kaw ñeneen ña ; Am na ci ñu Yàlla wax ak ñoom, yékkati ñenn ña seeni daraja. Te jox Nanu (Iisaa) doomu Maryaama lay yu leer nàññ, dëgërale ko Ruu gu Sell. Bu sooboon Yàlla, ñi ñëw seen ginnaaw duñu reyante, ginnaaw ba ñu jotee lay yu leer nàññ ; waaye dañoo juuyoo : mu am ca ñoom ñu gëm, am it ñu weddi. Bu sooboon Yàlla, duñu xeex ; waaye Yàlla dana def la mu namm.
254يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا أَنفِقُوا مِمَّا رَزَقْنَاكُم مِّن قَبْلِ أَن يَأْتِيَ يَوْمٌ لَّا بَيْعٌ فِيهِ وَلَا خُلَّةٌ وَلَا شَفَاعَةٌ ۗ وَالْكَافِرُونَ هُمُ الظَّالِمُونَ
Yéen ñi gëm ! Nangeen joxe ci alal ji Nu leen wërsëgal, bis dina ñëw boo xam ne amul xaritoo, amul njotu, amul tinu. Te ña weddi ñooy tooñkat ya de.
Al-BaqaraFihi Alxuraan
286Aaya
MedinanRevelation
252Aaya
Tekki — Al-Baqara 252
Simoore Al-Baqara Aaya 252 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Kàddug Yàlla googu dananu la ko jàngal ci dëgg.Te yaw…Simoore Aaya 252/286 — Al-Baqara البقرة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Baqara Dégg, Al-Baqara Tekki, Al-Baqara mp3, Al-Baqara pdf. Aaya 250–254. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








