Taha · 42/135
Tekki Waxtaan — Simoore Taha
اذْهَبْ أَنتَ وَأَخُوكَ بِآيَاتِي وَلَا تَنِيَا فِي ذِكْرِي ۝٤٢
Izhab anta wa akhooka bi Aayaatee wa laa taniyaa fee zikree
📖 Tekkim Wolof
Demal yaak sa mbokk ngeen yor samay kàddu ; te buleen sàggane di Ma jaamu.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 40-44 — Simoore Taha

40إِذْ تَمْشِي أُخْتُكَ فَتَقُولُ هَلْ أَدُلُّكُمْ عَلَىٰ مَن يَكْفُلُهُ ۖ فَرَجَعْنَاكَ إِلَىٰ أُمِّكَ كَيْ تَقَرَّ عَيْنُهَا وَلَا تَحْزَنَ ۚ وَقَتَلْتَ نَفْسًا فَنَجَّيْنَاكَ مِنَ الْغَمِّ وَفَتَنَّاكَ فُتُونًا ۚ فَلَبِثْتَ سِنِينَ فِي أَهْلِ مَدْيَنَ ثُمَّ جِئْتَ عَلَىٰ قَدَرٍ يَا مُوسَىٰ
[Fàttalikul] ba sa jigéen ba di dox te naan leen : “Ndax duma leen tegtal ci ku ko mën a yar ? ” Ba tax Nu delloo la fa sa yaay ngir xelam dal, mu bañ a yàq. Nga reyoon bakkan, Nu musal la ca mbamb ma ; Nu fitnaaloon la, nattu la lu yàgg. Nga demoon fa waa Madiyaana ba am fa ay at. Ba tey jii yaa ngi nii ci àpp bu ma dogaloon.
41وَاصْطَنَعْتُكَ لِنَفْسِي
Maa la bind ngir Sama mbiri bopp.
42اذْهَبْ أَنتَ وَأَخُوكَ بِآيَاتِي وَلَا تَنِيَا فِي ذِكْرِي
Demal yaak sa mbokk ngeen yor samay kàddu ; te buleen sàggane di Ma jaamu.
43اذْهَبَا إِلَىٰ فِرْعَوْنَ إِنَّهُ طَغَىٰ
Demleen yéen ñaar fa Firawna : ndax moom dafa beew.
44فَقُولَا لَهُ قَوْلًا لَّيِّنًا لَّعَلَّهُ يَتَذَكَّرُ أَوْ يَخْشَىٰ
Nangeen wax ak moom wax ju nooy. Ndax amaana mu waaru walla mu ragal Yàlla ?
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
42Aaya

Tekki — Taha 42

Simoore Taha Aaya 42 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Demal yaak sa mbokk ngeen yor samay kàddu ; te…

Simoore Aaya 42/135 — Simoore Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Taha Dégg, Simoore Taha Tekki, Simoore Taha mp3, Simoore Taha pdf. Aaya 40–44. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Saturday, October 3, 2026

Don't forget us in your sincere prayers