Taha · 43/135
Tekki Waxtaan — Taha
اذْهَبَا إِلَىٰ فِرْعَوْنَ إِنَّهُ طَغَىٰ ٤٣
Transliteration
Izhabaaa ilaa Fir`awna innahoo taghaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Demleen yéen ñaar fa Firawna : ndax moom dafa beew.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 41-45 — Taha
41وَاصْطَنَعْتُكَ لِنَفْسِي
Maa la bind ngir Sama mbiri bopp.
42اذْهَبْ أَنتَ وَأَخُوكَ بِآيَاتِي وَلَا تَنِيَا فِي ذِكْرِي
Demal yaak sa mbokk ngeen yor samay kàddu ; te buleen sàggane di Ma jaamu.
43اذْهَبَا إِلَىٰ فِرْعَوْنَ إِنَّهُ طَغَىٰ
Demleen yéen ñaar fa Firawna : ndax moom dafa beew.
44فَقُولَا لَهُ قَوْلًا لَّيِّنًا لَّعَلَّهُ يَتَذَكَّرُ أَوْ يَخْشَىٰ
Nangeen wax ak moom wax ju nooy. Ndax amaana mu waaru walla mu ragal Yàlla ?
45قَالَا رَبَّنَا إِنَّنَا نَخَافُ أَن يَفْرُطَ عَلَيْنَا أَوْ أَن يَطْغَىٰ
Ñu ne Ko : "Yaw sunu Boroom, nun dey danuy ragal, bu nu demee fa moom, mu jaay nu doole”.
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
43Aaya
Tekki — Taha 43
Simoore Taha Aaya 43 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Demleen yéen ñaar fa Firawna : ndax moom dafa beew.Simoore Aaya 43/135 — Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Taha Dégg, Taha Tekki, Taha mp3, Taha pdf. Aaya 41–45. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








