Taha · 75/135
Tekki Waxtaan — Taha
وَمَن يَأْتِهِ مُؤْمِنًا قَدْ عَمِلَ الصَّالِحَاتِ فَأُولَٰئِكَ لَهُمُ الدَّرَجَاتُ الْعُلَىٰ ۝٧٥
Wa mai yaatihee mu`minan qad `amilas saalihaati fa ulaaa`ika lahumud dara jaatul `ulaa
📖 Tekkim Wolof
Kuy gëm Yàlla ak a def u yiw ba dem fa Yàlla, ñooña danañu am ay daraja yu kawe,

🎧 Dégg


📜 Aaya 73-77 — Taha

73إِنَّا آمَنَّا بِرَبِّنَا لِيَغْفِرَ لَنَا خَطَايَانَا وَمَا أَكْرَهْتَنَا عَلَيْهِ مِنَ السِّحْرِ ۗ وَاللَّهُ خَيْرٌ وَأَبْقَىٰ
Nun dey gëm nanu sunu Boroom ngir mu jéggal nu sunuy bàkkaar, ak njibar gii nga nu jaay doole ba tax nu def ko”. Te Yàlla Moo gën te Mooy des.
74إِنَّهُ مَن يَأْتِ رَبَّهُ مُجْرِمًا فَإِنَّ لَهُ جَهَنَّمَ لَا يَمُوتُ فِيهَا وَلَا يَحْيَىٰ
Kuy saay-saay ba dem fa Boroomam, dana tàbbi Safara te du fa dee du fa dundu.
75وَمَن يَأْتِهِ مُؤْمِنًا قَدْ عَمِلَ الصَّالِحَاتِ فَأُولَٰئِكَ لَهُمُ الدَّرَجَاتُ الْعُلَىٰ
Kuy gëm Yàlla ak a def u yiw ba dem fa Yàlla, ñooña danañu am ay daraja yu kawe,
76جَنَّاتُ عَدْنٍ تَجْرِي مِن تَحْتِهَا الْأَنْهَارُ خَالِدِينَ فِيهَا ۚ وَذَٰلِكَ جَزَاءُ مَن تَزَكَّىٰ
ay àjjana yu sax yoo xam ne ay dex ñooy daw ci suufam te dañu fay béel. Loolu moo di peyug képp kuy sellal.
77وَلَقَدْ أَوْحَيْنَا إِلَىٰ مُوسَىٰ أَنْ أَسْرِ بِعِبَادِي فَاضْرِبْ لَهُمْ طَرِيقًا فِي الْبَحْرِ يَبَسًا لَّا تَخَافُ دَرَكًا وَلَا تَخْشَىٰ
Digal Nanu Muusaa [soloo ko]ne ko : “Nga rañaan ak sama jaam ñi, nanga leen sàkkal aw yoonu suuf wu wow ca biir géej ga : bul ragal ku lay dab walla ngay tiit”.
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
75Aaya

Tekki — Taha 75

Simoore Taha Aaya 75 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Kuy gëm Yàlla ak a def u yiw ba dem…

Simoore Aaya 75/135 — Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Taha Dégg, Taha Tekki, Taha mp3, Taha pdf. Aaya 73–77. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers