Al-Anbiya · 104/112
Tekki Waxtaan — Al-Anbiya
يَوْمَ نَطْوِي السَّمَاءَ كَطَيِّ السِّجِلِّ لِلْكُتُبِ ۚ كَمَا بَدَأْنَا أَوَّلَ خَلْقٍ نُّعِيدُهُ ۚ وَعْدًا عَلَيْنَا ۚ إِنَّا كُنَّا فَاعِلِينَ ۝١٠٤
Yawma natwis samaaa`a kataiyis sijilli lilkutub; kamaa badaanaa awwala khalqin nu`eeduh; wa`dan `alainaa; innaa kunna faa`ileen
📖 Tekkim Wolof
Bis boobu Dananu taxañ asamaam ni Nuy taxañe këyit gu am bind. Na nu tàmbalee woon sos ga bu jëkk ba, Dananu dellu [defaat ko] ; muy dëel bu Nu warlu [lu Nuy def la] !
🎧 Dégg

📜 Aaya 102-106 — Al-Anbiya

102لَا يَسْمَعُونَ حَسِيسَهَا ۖ وَهُمْ فِي مَا اشْتَهَتْ أَنفُسُهُمْ خَالِدُونَ
Duñu dégg yëngoom ga te ñoom ñangay nekk ca lu neex seen bakkan ba fàwwu.
103لَا يَحْزُنُهُمُ الْفَزَعُ الْأَكْبَرُ وَتَتَلَقَّاهُمُ الْمَلَائِكَةُ هَٰذَا يَوْمُكُمُ الَّذِي كُنتُمْ تُوعَدُونَ
Tiit mu rëy ma duleen tiital, te Malaaka ya danañu leen gatandu naan : “Lii mooy seen bis ba ñu leen digoon”.
104يَوْمَ نَطْوِي السَّمَاءَ كَطَيِّ السِّجِلِّ لِلْكُتُبِ ۚ كَمَا بَدَأْنَا أَوَّلَ خَلْقٍ نُّعِيدُهُ ۚ وَعْدًا عَلَيْنَا ۚ إِنَّا كُنَّا فَاعِلِينَ
Bis boobu Dananu taxañ asamaam ni Nuy taxañe këyit gu am bind. Na nu tàmbalee woon sos ga bu jëkk ba, Dananu dellu [defaat ko] ; muy dëel bu Nu warlu [lu Nuy def la] !
105وَلَقَدْ كَتَبْنَا فِي الزَّبُورِ مِن بَعْدِ الذِّكْرِ أَنَّ الْأَرْضَ يَرِثُهَا عِبَادِيَ الصَّالِحُونَ
Te bind Nanu ba noppi ca Téere ya ginnaaw bind ga nekk [ca Lawhul Mahfuuz] Àlluwa ja, ne suuf si Sunu jaam yu yiw yi ñoo koy donn”.
106إِنَّ فِي هَٰذَا لَبَلَاغًا لِّقَوْمٍ عَابِدِينَ
Nekk na ci biir loolu ab jottali ñeel aw nit ñuy jaamu Yàlla !
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
104Aaya

Tekki — Al-Anbiya 104

Simoore Al-Anbiya Aaya 104 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bis boobu Dananu taxañ asamaam ni Nuy taxañe këyit gu…

Simoore Aaya 104/112 — Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Anbiya Dégg, Al-Anbiya Tekki, Al-Anbiya mp3, Al-Anbiya pdf. Aaya 102–106. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers