Al-Hajj · 59/78
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hajj
لَيُدْخِلَنَّهُم مُّدْخَلًا يَرْضَوْنَهُ ۗ وَإِنَّ اللَّهَ لَعَلِيمٌ حَلِيمٌ ٥٩
Transliteration
La yudkhilan nahum mud khalany yardawnah; wa innal laaha la `Aleemun Haleem
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
fàwwu dana leen tàbbal barab boo xam ne danañu ca bég, te Yàlla ku xam la, Ku lewet la.
Additional reference in Fulfulde
M
Mishary Rashid Alafasy
✓
Mishary Rashid Alafasy
✓
M
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
A
Abdurrahman As-Sudais
✓
Abdurrahman As-Sudais
✓
M
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
A
Abdul Basit Abdul Samad
✓
Abdul Basit Abdul Samad
✓
A
Ali Al-Hudhaify
✓
Ali Al-Hudhaify
✓
A
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
A
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
M
Muhammad Ayyoub
✓
Muhammad Ayyoub
✓
A
Abdullah Basfar
✓
Abdullah Basfar
✓
A
Abdullah Al-Juhani
✓
Abdullah Al-Juhani
✓
M
Maher Al Muaiqly
✓
Maher Al Muaiqly
✓
0:00
0:00
📜 Aaya 57-61 — Simoore Al-Hajj
57وَالَّذِينَ كَفَرُوا وَكَذَّبُوا بِآيَاتِنَا فَأُولَٰئِكَ لَهُمْ عَذَابٌ مُّهِينٌ
waaye ña weddi te jàppe ay fen Sunuy kàddu, ñooña ñeel na leen mbugal muy toroxale !
58وَالَّذِينَ هَاجَرُوا فِي سَبِيلِ اللَّهِ ثُمَّ قُتِلُوا أَوْ مَاتُوا لَيَرْزُقَنَّهُمُ اللَّهُ رِزْقًا حَسَنًا ۚ وَإِنَّ اللَّهَ لَهُوَ خَيْرُ الرَّازِقِينَ
Ña gàdday ngir liggéey ci yoonu Yàlla, topp ñu rey leen mbaa ñu dee, fàwwu Yàlla dana leen wërsëgal wërsëg wu rafet, te nag Yàlla moo di Ki gën a mën a wërsëgal ci képp kuy wërsëgal.
59لَيُدْخِلَنَّهُم مُّدْخَلًا يَرْضَوْنَهُ ۗ وَإِنَّ اللَّهَ لَعَلِيمٌ حَلِيمٌ
fàwwu dana leen tàbbal barab boo xam ne danañu ca bég, te Yàlla ku xam la, Ku lewet la.
60۞ ذَٰلِكَ وَمَنْ عَاقَبَ بِمِثْلِ مَا عُوقِبَ بِهِ ثُمَّ بُغِيَ عَلَيْهِ لَيَنصُرَنَّهُ اللَّهُ ۗ إِنَّ اللَّهَ لَعَفُوٌّ غَفُورٌ
Noonu la. Ku mbugale lu toll ni la ñu ko tooñ, topp ñu tooñaat ko, Yàlla dana ko dimbali, Yàlla Jéggalaakoon, Baalewaakoon la.
61ذَٰلِكَ بِأَنَّ اللَّهَ يُولِجُ اللَّيْلَ فِي النَّهَارِ وَيُولِجُ النَّهَارَ فِي اللَّيْلِ وَأَنَّ اللَّهَ سَمِيعٌ بَصِيرٌ
Noonu la ngir Yàlla mooy dugal guddi ci bëccëg, di duggal bëccëg ci guddi, te nag Yàlla Kuy dégg la, Kuy gis la.
Al-HajjFihi Alxuraan
78Aaya
MedinanRevelation
59Aaya
Tekki — Al-Hajj 59
Simoore Al-Hajj Aaya 59 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : fàwwu dana leen tàbbal barab boo xam ne danañu ca…Simoore Aaya 59/78 — Simoore Al-Hajj الحج (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hajj Dégg, Simoore Al-Hajj Tekki, Simoore Al-Hajj mp3, Simoore Al-Hajj pdf. Aaya 57–61. Tekkim Wolof: Fulfulde.
Simoore Al-Hajj
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Monday, September 28, 2026
Don't forget us in your sincere prayers


