Al-Mu'minun · 100/118
Tekki Waxtaan — Al-Mu'minun
لَعَلِّي أَعْمَلُ صَالِحًا فِيمَا تَرَكْتُ ۚ كَلَّا ۚ إِنَّهَا كَلِمَةٌ هُوَ قَائِلُهَا ۖ وَمِن وَرَائِهِم بَرْزَخٌ إِلَىٰ يَوْمِ يُبْعَثُونَ ١٠٠
Transliteration
La`alleee a`malu saalihan feemaa taraktu kallaa; innahaa kalimatun huwa qaaa`iluhaa wa minw waraaa`him barzakhun ilaa Yawmi yub`asoon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
ndax ma mën a jëf yiw ca la ma fa bàyyi”. [Mukk loolu du mës a am], loolu kàddu la rekk gu muy wax. [Barsàq] kiiraay la ñuy nekk ba ba ñuy dekki”.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 98-102 — Al-Mu'minun
98وَأَعُوذُ بِكَ رَبِّ أَن يَحْضُرُونِ
te maa ngi sàkku ndimbalul sama Boroom ci ñu di ma teewe ànd ak man”.
99حَتَّىٰ إِذَا جَاءَ أَحَدَهُمُ الْمَوْتُ قَالَ رَبِّ ارْجِعُونِ
ba ba dee dikkal kenn ci ñoom, mu naan : “Sama Boroom ! Delloo ma àddina,
100لَعَلِّي أَعْمَلُ صَالِحًا فِيمَا تَرَكْتُ ۚ كَلَّا ۚ إِنَّهَا كَلِمَةٌ هُوَ قَائِلُهَا ۖ وَمِن وَرَائِهِم بَرْزَخٌ إِلَىٰ يَوْمِ يُبْعَثُونَ
ndax ma mën a jëf yiw ca la ma fa bàyyi”. [Mukk loolu du mës a am], loolu kàddu la rekk gu muy wax. [Barsàq] kiiraay la ñuy nekk ba ba ñuy dekki”.
101فَإِذَا نُفِخَ فِي الصُّورِ فَلَا أَنسَابَ بَيْنَهُمْ يَوْمَئِذٍ وَلَا يَتَسَاءَلُونَ
Bu ñu walee Buftu bi kerook Bisboobu, askan amatul seen diggante te dootuñu lijjanti.
102فَمَن ثَقُلَتْ مَوَازِينُهُ فَأُولَٰئِكَ هُمُ الْمُفْلِحُونَ
Képp ku peeseem diis [ak jëf yu baax]ñoom ñooy ña texe ;
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
100Aaya
Tekki — Al-Mu'minun 100
Simoore Al-Mu'minun Aaya 100 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ndax ma mën a jëf yiw ca la ma fa…Simoore Aaya 100/118 — Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Mu'minun Dégg, Al-Mu'minun Tekki, Al-Mu'minun mp3, Al-Mu'minun pdf. Aaya 98–102. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








