Al-Mu'minun · 99/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
حَتَّىٰ إِذَا جَاءَ أَحَدَهُمُ الْمَوْتُ قَالَ رَبِّ ارْجِعُونِ ۝٩٩
Hattaaa izaa jaaa`a ahada humul mawtu qaala Rabbir ji`oon
📖 Tekkim Wolof
ba ba dee dikkal kenn ci ñoom, mu naan : “Sama Boroom ! Delloo ma àddina,

🎧 Dégg


📜 Aaya 97-101 — Simoore Al-Mu'minun

97وَقُل رَّبِّ أَعُوذُ بِكَ مِنْ هَمَزَاتِ الشَّيَاطِينِ
Neel : “Maa ngi sàkkoo ci sama Boroom mu musal ma ci jax-jaxali Séytaane.
98وَأَعُوذُ بِكَ رَبِّ أَن يَحْضُرُونِ
te maa ngi sàkku ndimbalul sama Boroom ci ñu di ma teewe ànd ak man”.
99حَتَّىٰ إِذَا جَاءَ أَحَدَهُمُ الْمَوْتُ قَالَ رَبِّ ارْجِعُونِ
ba ba dee dikkal kenn ci ñoom, mu naan : “Sama Boroom ! Delloo ma àddina,
100لَعَلِّي أَعْمَلُ صَالِحًا فِيمَا تَرَكْتُ ۚ كَلَّا ۚ إِنَّهَا كَلِمَةٌ هُوَ قَائِلُهَا ۖ وَمِن وَرَائِهِم بَرْزَخٌ إِلَىٰ يَوْمِ يُبْعَثُونَ
ndax ma mën a jëf yiw ca la ma fa bàyyi”. [Mukk loolu du mës a am], loolu kàddu la rekk gu muy wax. [Barsàq] kiiraay la ñuy nekk ba ba ñuy dekki”.
101فَإِذَا نُفِخَ فِي الصُّورِ فَلَا أَنسَابَ بَيْنَهُمْ يَوْمَئِذٍ وَلَا يَتَسَاءَلُونَ
Bu ñu walee Buftu bi kerook Bisboobu, askan amatul seen diggante te dootuñu lijjanti.
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
99Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 99

Simoore Al-Mu'minun Aaya 99 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ba ba dee dikkal kenn ci ñoom, mu naan :…

Simoore Aaya 99/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 97–101. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers