Al-Mu'minun · 109/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
إِنَّهُ كَانَ فَرِيقٌ مِّنْ عِبَادِي يَقُولُونَ رَبَّنَا آمَنَّا فَاغْفِرْ لَنَا وَارْحَمْنَا وَأَنتَ خَيْرُ الرَّاحِمِينَ ۝١٠٩
Innahoo kaana fareequm min `ibaadee yaqooloona Rabbanaaa aamannaa faghfir lanaa warhamnaa wa Anta khairur raahimeen
📖 Tekkim Wolof
Am na ab kurél bu bokkoon ci sama jaam, daan wax naan : “Boroom sunu, gëm nanu ; jéggal nu te yërëm nu, Yaw yaa di gën ji Yërëmaakoon” ;

🎧 Dégg


📜 Aaya 107-111 — Simoore Al-Mu'minun

107رَبَّنَا أَخْرِجْنَا مِنْهَا فَإِنْ عُدْنَا فَإِنَّا ظَالِمُونَ
Boroom sunu, génne nu ci ! Bu nu tey-teyloo ba dellu ci, noo tooñ”.
108قَالَ اخْسَئُوا فِيهَا وَلَا تُكَلِّمُونِ
Mu ne leen : “Jattleen ci biir te buleen ma tuddati”.
109إِنَّهُ كَانَ فَرِيقٌ مِّنْ عِبَادِي يَقُولُونَ رَبَّنَا آمَنَّا فَاغْفِرْ لَنَا وَارْحَمْنَا وَأَنتَ خَيْرُ الرَّاحِمِينَ
Am na ab kurél bu bokkoon ci sama jaam, daan wax naan : “Boroom sunu, gëm nanu ; jéggal nu te yërëm nu, Yaw yaa di gën ji Yërëmaakoon” ;
110فَاتَّخَذْتُمُوهُمْ سِخْرِيًّا حَتَّىٰ أَنسَوْكُمْ ذِكْرِي وَكُنتُم مِّنْهُمْ تَضْحَكُونَ
ngeen jàppee woon leen ay reetaan ba faf ñu fàbbi leen fàtteloo leen Samay kàddu, dëkkoon ci di leen reetaan rekk.
111إِنِّي جَزَيْتُهُمُ الْيَوْمَ بِمَا صَبَرُوا أَنَّهُمْ هُمُ الْفَائِزُونَ
Bis niki tey feye naa leen ca la ñu doon muñ ; ñoom texe nañu.
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
109Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 109

Simoore Al-Mu'minun Aaya 109 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Am na ab kurél bu bokkoon ci sama jaam, daan…

Simoore Aaya 109/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 107–111. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers