Al-Mu'minun · 110/118
Tekki Waxtaan — Al-Mu'minun
فَاتَّخَذْتُمُوهُمْ سِخْرِيًّا حَتَّىٰ أَنسَوْكُمْ ذِكْرِي وَكُنتُم مِّنْهُمْ تَضْحَكُونَ ۝١١٠
Fattakhaztumoohum sikhriyyan hattaaa ansawkum zikree wa kuntum minhum tadhakoon
📖 Tekkim Wolof
ngeen jàppee woon leen ay reetaan ba faf ñu fàbbi leen fàtteloo leen Samay kàddu, dëkkoon ci di leen reetaan rekk.

🎧 Dégg


📜 Aaya 108-112 — Al-Mu'minun

108قَالَ اخْسَئُوا فِيهَا وَلَا تُكَلِّمُونِ
Mu ne leen : “Jattleen ci biir te buleen ma tuddati”.
109إِنَّهُ كَانَ فَرِيقٌ مِّنْ عِبَادِي يَقُولُونَ رَبَّنَا آمَنَّا فَاغْفِرْ لَنَا وَارْحَمْنَا وَأَنتَ خَيْرُ الرَّاحِمِينَ
Am na ab kurél bu bokkoon ci sama jaam, daan wax naan : “Boroom sunu, gëm nanu ; jéggal nu te yërëm nu, Yaw yaa di gën ji Yërëmaakoon” ;
110فَاتَّخَذْتُمُوهُمْ سِخْرِيًّا حَتَّىٰ أَنسَوْكُمْ ذِكْرِي وَكُنتُم مِّنْهُمْ تَضْحَكُونَ
ngeen jàppee woon leen ay reetaan ba faf ñu fàbbi leen fàtteloo leen Samay kàddu, dëkkoon ci di leen reetaan rekk.
111إِنِّي جَزَيْتُهُمُ الْيَوْمَ بِمَا صَبَرُوا أَنَّهُمْ هُمُ الْفَائِزُونَ
Bis niki tey feye naa leen ca la ñu doon muñ ; ñoom texe nañu.
112قَالَ كَمْ لَبِثْتُمْ فِي الْأَرْضِ عَدَدَ سِنِينَ
Mu ne leen : “Yéen sax ñaata at ngeen saxoon ci àddina [dundoon] ? ”
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
110Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 110

Simoore Al-Mu'minun Aaya 110 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ngeen jàppee woon leen ay reetaan ba faf ñu fàbbi…

Simoore Aaya 110/118 — Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Mu'minun Dégg, Al-Mu'minun Tekki, Al-Mu'minun mp3, Al-Mu'minun pdf. Aaya 108–112. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers