Al-Mu'minun · 44/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
ثُمَّ أَرْسَلْنَا رُسُلَنَا تَتْرَىٰ ۖ كُلَّ مَا جَاءَ أُمَّةً رَّسُولُهَا كَذَّبُوهُ ۚ فَأَتْبَعْنَا بَعْضَهُم بَعْضًا وَجَعَلْنَاهُمْ أَحَادِيثَ ۚ فَبُعْدًا لِّقَوْمٍ لَّا يُؤْمِنُونَ ۝٤٤
Summa arsalnaa Rusulanaa tatraa kulla maa jaaa`a ummatar Rasooluhaa kazzabooh; fa atba`naa ba`dahum ba`danw wa ja`alnaahum ahaadees; fabu`dal liqawmil laa yu`minoon
📖 Tekkim Wolof
Topp, ginnaaw ba Nu yónni sunuy Yonent ñuy toppante. Xeet bu ca ab Yonentam dikkal, ñu weddi ko. Toftale Nanu leen kenn kenn, def Nanu leen ñu di ay waxtaan. Toskare ñeel na aw nit ñu gëmul !

🎧 Dégg


📜 Aaya 42-46 — Simoore Al-Mu'minun

42ثُمَّ أَنشَأْنَا مِن بَعْدِهِمْ قُرُونًا آخَرِينَ
Ba noppi, Nu sos ca seen ginnaaw yeneeni maas.
43مَا تَسْبِقُ مِنْ أُمَّةٍ أَجَلَهَا وَمَا يَسْتَأْخِرُونَ
Amul wenn xeet wuy jiitu walla mu mujj ab digam.
44ثُمَّ أَرْسَلْنَا رُسُلَنَا تَتْرَىٰ ۖ كُلَّ مَا جَاءَ أُمَّةً رَّسُولُهَا كَذَّبُوهُ ۚ فَأَتْبَعْنَا بَعْضَهُم بَعْضًا وَجَعَلْنَاهُمْ أَحَادِيثَ ۚ فَبُعْدًا لِّقَوْمٍ لَّا يُؤْمِنُونَ
Topp, ginnaaw ba Nu yónni sunuy Yonent ñuy toppante. Xeet bu ca ab Yonentam dikkal, ñu weddi ko. Toftale Nanu leen kenn kenn, def Nanu leen ñu di ay waxtaan. Toskare ñeel na aw nit ñu gëmul !
45ثُمَّ أَرْسَلْنَا مُوسَىٰ وَأَخَاهُ هَارُونَ بِآيَاتِنَا وَسُلْطَانٍ مُّبِينٍ
Topp, ginnaaw ba yónni Nanu Muusaa ak mbokkam ma Aaruuna jox leen Sunuy laaya ak kàttan gu bir,
46إِلَىٰ فِرْعَوْنَ وَمَلَئِهِ فَاسْتَكْبَرُوا وَكَانُوا قَوْمًا عَالِينَ
jëmale ko ca Firawna ak gàngooram ña doon rëy-rëylu te doon aw nit ñuy kawe-kawelu.
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
44Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 44

Simoore Al-Mu'minun Aaya 44 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Topp, ginnaaw ba Nu yónni sunuy Yonent ñuy toppante. Xeet…

Simoore Aaya 44/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 42–46. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers