Al-Mu'minun · 45/118
Tekki Waxtaan — Al-Mu'minun
ثُمَّ أَرْسَلْنَا مُوسَىٰ وَأَخَاهُ هَارُونَ بِآيَاتِنَا وَسُلْطَانٍ مُّبِينٍ ٤٥
Transliteration
Summa arsalnaa Moosaa wa akhaahu Haaroona bi Aayaatinaa wa sultaanim mubeen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Topp, ginnaaw ba yónni Nanu Muusaa ak mbokkam ma Aaruuna jox leen Sunuy laaya ak kàttan gu bir,
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 43-47 — Al-Mu'minun
43مَا تَسْبِقُ مِنْ أُمَّةٍ أَجَلَهَا وَمَا يَسْتَأْخِرُونَ
Amul wenn xeet wuy jiitu walla mu mujj ab digam.
44ثُمَّ أَرْسَلْنَا رُسُلَنَا تَتْرَىٰ ۖ كُلَّ مَا جَاءَ أُمَّةً رَّسُولُهَا كَذَّبُوهُ ۚ فَأَتْبَعْنَا بَعْضَهُم بَعْضًا وَجَعَلْنَاهُمْ أَحَادِيثَ ۚ فَبُعْدًا لِّقَوْمٍ لَّا يُؤْمِنُونَ
Topp, ginnaaw ba Nu yónni sunuy Yonent ñuy toppante. Xeet bu ca ab Yonentam dikkal, ñu weddi ko. Toftale Nanu leen kenn kenn, def Nanu leen ñu di ay waxtaan. Toskare ñeel na aw nit ñu gëmul !
45ثُمَّ أَرْسَلْنَا مُوسَىٰ وَأَخَاهُ هَارُونَ بِآيَاتِنَا وَسُلْطَانٍ مُّبِينٍ
Topp, ginnaaw ba yónni Nanu Muusaa ak mbokkam ma Aaruuna jox leen Sunuy laaya ak kàttan gu bir,
46إِلَىٰ فِرْعَوْنَ وَمَلَئِهِ فَاسْتَكْبَرُوا وَكَانُوا قَوْمًا عَالِينَ
jëmale ko ca Firawna ak gàngooram ña doon rëy-rëylu te doon aw nit ñuy kawe-kawelu.
47فَقَالُوا أَنُؤْمِنُ لِبَشَرَيْنِ مِثْلِنَا وَقَوْمُهُمَا لَنَا عَابِدُونَ
Ñuy wax naan : “Ndax dananu gëm ñaari nit ñu mel ni nun, ñoo xam ne seenu xeet sunuy jaam lañu.
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
45Aaya
Tekki — Al-Mu'minun 45
Simoore Al-Mu'minun Aaya 45 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Topp, ginnaaw ba yónni Nanu Muusaa ak mbokkam ma Aaruuna…Simoore Aaya 45/118 — Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Mu'minun Dégg, Al-Mu'minun Tekki, Al-Mu'minun mp3, Al-Mu'minun pdf. Aaya 43–47. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








