Al-Furqan · 34/77
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Furqan
الَّذِينَ يُحْشَرُونَ عَلَىٰ وُجُوهِهِمْ إِلَىٰ جَهَنَّمَ أُولَٰئِكَ شَرٌّ مَّكَانًا وَأَضَلُّ سَبِيلًا ۝٣٤
(Allazeena yuhsharoona `alaa wujoohim ilaa jahannama ulaaa`ika sharrum makaananw wa adallu sabeelaa )section
📖 Tekkim Wolof
Ña nga xam ne dees na leen pang, di leen diri ci seen xar-kanam ya, jëme leen Safara, ñoom ñooy gën a yées wàccuwaay, gën a réere yoon wu jub wa.

🎧 Dégg


📜 Aaya 32-36 — Simoore Al-Furqan

32وَقَالَ الَّذِينَ كَفَرُوا لَوْلَا نُزِّلَ عَلَيْهِ الْقُرْآنُ جُمْلَةً وَاحِدَةً ۚ كَذَٰلِكَ لِنُثَبِّتَ بِهِ فُؤَادَكَ ۖ وَرَتَّلْنَاهُ تَرْتِيلًا
Yéefar yaa ngay wax naan : “Lu tax wàccendoo wuñu Alxuraan jii wenn yoon mu ne ñumm ? ” [Waaye Nun nii la Nu koy wàccee] ngir dëgëral sa xol. Te it toftale Nanu ko bu jekk.
33وَلَا يَأْتُونَكَ بِمَثَلٍ إِلَّا جِئْنَاكَ بِالْحَقِّ وَأَحْسَنَ تَفْسِيرًا
Amul léebu wu ñu lay mën a indil te indilunu la dëgg, te gën koo jub.
34الَّذِينَ يُحْشَرُونَ عَلَىٰ وُجُوهِهِمْ إِلَىٰ جَهَنَّمَ أُولَٰئِكَ شَرٌّ مَّكَانًا وَأَضَلُّ سَبِيلًا
Ña nga xam ne dees na leen pang, di leen diri ci seen xar-kanam ya, jëme leen Safara, ñoom ñooy gën a yées wàccuwaay, gën a réere yoon wu jub wa.
35وَلَقَدْ آتَيْنَا مُوسَى الْكِتَابَ وَجَعَلْنَا مَعَهُ أَخَاهُ هَارُونَ وَزِيرًا
Jox Nanu Muusaa Téere ba, defal ko Aaruuna mbokkam mu di ko jàppale.
36فَقُلْنَا اذْهَبَا إِلَى الْقَوْمِ الَّذِينَ كَذَّبُوا بِآيَاتِنَا فَدَمَّرْنَاهُمْ تَدْمِيرًا
Nu wax leen ne : “Demleen yéen ñaar ca nit ña weddi woon Sunuy kàddu”. Nu alag leen.
Al-FurqanFihi Alxuraan
77Aaya
MeccanRevelation
34Aaya

Tekki — Al-Furqan 34

Simoore Al-Furqan Aaya 34 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña nga xam ne dees na leen pang, di leen…

Simoore Aaya 34/77 — Simoore Al-Furqan الفرقان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Furqan Dégg, Simoore Al-Furqan Tekki, Simoore Al-Furqan mp3, Simoore Al-Furqan pdf. Aaya 32–36. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers