Ash-Shu'ara · 127/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
وَمَا أَسْأَلُكُمْ عَلَيْهِ مِنْ أَجْرٍ ۖ إِنْ أَجْرِيَ إِلَّا عَلَىٰ رَبِّ الْعَالَمِينَ ۝١٢٧
Wa maa as`alukum `alaihi min ajrin in ajriya illaa `alaa Rabbil `aalameen
📖 Tekkim Wolof
Duma leen ca laaj genn pey ; samag pey Boroom àddina see ko warlu.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 125-129 — Simoore Ash-Shu'ara

125إِنِّي لَكُمْ رَسُولٌ أَمِينٌ
Man dey, ab Yonent laa bu wóor,
126فَاتَّقُوا اللَّهَ وَأَطِيعُونِ
Ragal-leen Yàlla te topp ma.
127وَمَا أَسْأَلُكُمْ عَلَيْهِ مِنْ أَجْرٍ ۖ إِنْ أَجْرِيَ إِلَّا عَلَىٰ رَبِّ الْعَالَمِينَ
Duma leen ca laaj genn pey ; samag pey Boroom àddina see ko warlu.
128أَتَبْنُونَ بِكُلِّ رِيعٍ آيَةً تَعْبَثُونَ
Ndax dangeen di tabax ci kaw wépp tundu ab jàjj ngir caaxaan ?
129وَتَتَّخِذُونَ مَصَانِعَ لَعَلَّكُمْ تَخْلُدُونَ
Ngeen di liggéey i njéndi mel ni dangeen fiy béel ?
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
127Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 127

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 127 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Duma leen ca laaj genn pey ; samag pey Boroom…

Simoore Aaya 127/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 125–129. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Saturday, October 3, 2026

Don't forget us in your sincere prayers