Ash-Shu'ara · 192/227
Tekki Waxtaan — Ash-Shu'ara
وَإِنَّهُ لَتَنزِيلُ رَبِّ الْعَالَمِينَ ۝١٩٢
Wa innahoo latanzeelu Rabbil `aalameen
📖 Tekkim Wolof
[Alxuraan jii], ci lu bir, wàcceg Boroom àddina si la,

🎧 Dégg


📜 Aaya 190-194 — Ash-Shu'ara

190إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَةً ۖ وَمَا كَانَ أَكْثَرُهُم مُّؤْمِنِينَ
Ay kéemaan a ngi ci biir loolu. Te taxul ña ëppoon ca ñoom gëm.
191وَإِنَّ رَبَّكَ لَهُوَ الْعَزِيزُ الرَّحِيمُ
Te sa Boroom, Mooy Boroom kàttan, di Jaglewaakoon ba [yërmaandeem].
192وَإِنَّهُ لَتَنزِيلُ رَبِّ الْعَالَمِينَ
[Alxuraan jii], ci lu bir, wàcceg Boroom àddina si la,
193نَزَلَ بِهِ الرُّوحُ الْأَمِينُ
Ruu gu wóor ga [Jibriil] moo ko wàccaale
194عَلَىٰ قَلْبِكَ لِتَكُونَ مِنَ الْمُنذِرِينَ
def ko ci sa biir xol [yaw Muhammad] ngir nga bokk ca xuppekat ya,
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
192Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 192

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 192 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Alxuraan jii], ci lu bir, wàcceg Boroom àddina si la,

Simoore Aaya 192/227 — Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shu'ara Dégg, Ash-Shu'ara Tekki, Ash-Shu'ara mp3, Ash-Shu'ara pdf. Aaya 190–194. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers