Ash-Shu'ara · 36/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
قَالُوا أَرْجِهْ وَأَخَاهُ وَابْعَثْ فِي الْمَدَائِنِ حَاشِرِينَ ۝٣٦
Qaalooo arjih wa akhaahu wab`as filmadaaa`ini haashireen
📖 Tekkim Wolof
Ñu ne ko : “Joxleen ñoom ñaar beneen bis te nga yónni ci gox yi ñuy woo nit ñi, di leen dajale,

🎧 Dégg


📜 Aaya 34-38 — Simoore Ash-Shu'ara

34قَالَ لِلْمَلَإِ حَوْلَهُ إِنَّ هَٰذَا لَسَاحِرٌ عَلِيمٌ
[Firawna] wax gàngoor ga ne leen : “Kii dey ab jibar la bu xor.
35يُرِيدُ أَن يُخْرِجَكُم مِّنْ أَرْضِكُم بِسِحْرِهِ فَمَاذَا تَأْمُرُونَ
Da leen a bëgg a génne ci seen suuf sii ak jibaram gi. Lu ngeen ma ciy digal ? ”
36قَالُوا أَرْجِهْ وَأَخَاهُ وَابْعَثْ فِي الْمَدَائِنِ حَاشِرِينَ
Ñu ne ko : “Joxleen ñoom ñaar beneen bis te nga yónni ci gox yi ñuy woo nit ñi, di leen dajale,
37يَأْتُوكَ بِكُلِّ سَحَّارٍ عَلِيمٍ
danañu la indil bépp jibar bu fi xor”.
38فَجُمِعَ السَّحَرَةُ لِمِيقَاتِ يَوْمٍ مَّعْلُومٍ
Ñu dajale mbooleemi jibarkat ca bis ba ñu waxoon.
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
36Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 36

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 36 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu ne ko : “Joxleen ñoom ñaar beneen bis te…

Simoore Aaya 36/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 34–38. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers