Ash-Shu'ara · 8/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَةً ۖ وَمَا كَانَ أَكْثَرُهُم مُّؤْمِنِينَ ۝٨
Inn fee zaalika la Aayah; wa maa kaana aksaruhum mu`mineen
📖 Tekkim Wolof
Ay kéemaan yu bari nekk ci loolu ! Waaye taxut li ëpp ci ñoom gëm [diy jullit].

🎧 Dégg


📜 Aaya 6-10 — Simoore Ash-Shu'ara

6فَقَدْ كَذَّبُوا فَسَيَأْتِيهِمْ أَنبَاءُ مَا كَانُوا بِهِ يَسْتَهْزِئُونَ
Weddi woon nañu, te danañu mës a joti xibaari la ñu doon téjji.
7أَوَلَمْ يَرَوْا إِلَى الْأَرْضِ كَمْ أَنبَتْنَا فِيهَا مِن كُلِّ زَوْجٍ كَرِيمٍ
Xanaa dañoo gisul yu bari yi Nu saxal ci kaw suuf, ci xeeti gàncax muy tollént ?
8إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَةً ۖ وَمَا كَانَ أَكْثَرُهُم مُّؤْمِنِينَ
Ay kéemaan yu bari nekk ci loolu ! Waaye taxut li ëpp ci ñoom gëm [diy jullit].
9وَإِنَّ رَبَّكَ لَهُوَ الْعَزِيزُ الرَّحِيمُ
Te sa Boroom mooy Boroom kàttan ga te di Jaglewaakoonug [yërmaande].
10وَإِذْ نَادَىٰ رَبُّكَ مُوسَىٰ أَنِ ائْتِ الْقَوْمَ الظَّالِمِينَ
[Fàttalikul] ba Yàlla woo na Muusaa, [ne ko] : “Demal [jubbanti ji] tooñkat ya,
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
8Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 8

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 8 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ay kéemaan yu bari nekk ci loolu ! Waaye taxut…

Simoore Aaya 8/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 6–10. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers