An-Naml · 21/93
Tekki Waxtaan — An-Naml
لَأُعَذِّبَنَّهُ عَذَابًا شَدِيدًا أَوْ لَأَذْبَحَنَّهُ أَوْ لَيَأْتِيَنِّي بِسُلْطَانٍ مُّبِينٍ ۝٢١
La-u`azzibanahoo `azaaban shadeedan aw la azbahannahoo aw layaatiyannee bisultaanim mubeen
📖 Tekkim Wolof
Danaa ko mbugal mbugal mu tar ! Walla ma rendi ko ! Walla mu indil ma lay wu wér”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 19-23 — An-Naml

19فَتَبَسَّمَ ضَاحِكًا مِّن قَوْلِهَا وَقَالَ رَبِّ أَوْزِعْنِي أَنْ أَشْكُرَ نِعْمَتَكَ الَّتِي أَنْعَمْتَ عَلَيَّ وَعَلَىٰ وَالِدَيَّ وَأَنْ أَعْمَلَ صَالِحًا تَرْضَاهُ وَأَدْخِلْنِي بِرَحْمَتِكَ فِي عِبَادِكَ الصَّالِحِينَ
[Suleymaan] muuñ, daldi ree ndax wax jooju, daldi wax ne : “Yaw sama Boroom, Nanga baaxe may sant ci xéewal gii Nga ma dafal maak samay waajur, te may jëf jëf ju baax Joo gërëm te Nga may ma ci Sa yërmaande ma bokk ca Sa jaam ñu yiw ña”.
20وَتَفَقَّدَ الطَّيْرَ فَقَالَ مَا لِيَ لَا أَرَى الْهُدْهُدَ أَمْ كَانَ مِنَ الْغَائِبِينَ
Mu nemmiku njanaaw ya, daldi ne : “Lan moo tax gisuma Muusaa-njuburi ? Walla nekku fi?
21لَأُعَذِّبَنَّهُ عَذَابًا شَدِيدًا أَوْ لَأَذْبَحَنَّهُ أَوْ لَيَأْتِيَنِّي بِسُلْطَانٍ مُّبِينٍ
Danaa ko mbugal mbugal mu tar ! Walla ma rendi ko ! Walla mu indil ma lay wu wér”.
22فَمَكَثَ غَيْرَ بَعِيدٍ فَقَالَ أَحَطتُ بِمَا لَمْ تُحِطْ بِهِ وَجِئْتُكَ مِن سَبَإٍ بِنَبَإٍ يَقِينٍ
Mu sax fa tuuti, [picc] ma dellusi ne ko : “Xam naa loo xamul te indil naa la xibaar bu wóor bu bawoo réewum Sabaa” :
23إِنِّي وَجَدتُّ امْرَأَةً تَمْلِكُهُمْ وَأُوتِيَتْ مِن كُلِّ شَيْءٍ وَلَهَا عَرْشٌ عَظِيمٌ
Fekk naa leen ñu am buur bu jigéen, am na lépp, am it gàngunaay gu rëy.
An-NamlFihi Alxuraan
93Aaya
MeccanRevelation
21Aaya

Tekki — An-Naml 21

Simoore An-Naml Aaya 21 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Danaa ko mbugal mbugal mu tar ! Walla ma rendi…

Simoore Aaya 21/93 — An-Naml النمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Naml Dégg, An-Naml Tekki, An-Naml mp3, An-Naml pdf. Aaya 19–23. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers