An-Naml · 45/93
Tekki Waxtaan — Simoore An-Naml
وَلَقَدْ أَرْسَلْنَا إِلَىٰ ثَمُودَ أَخَاهُمْ صَالِحًا أَنِ اعْبُدُوا اللَّهَ فَإِذَا هُمْ فَرِيقَانِ يَخْتَصِمُونَ ۝٤٥
Wa laqad arsalnaaa ilaa Samoda akhaahum Saalihan ani`budul lahha fa izaa hum fareeqaani yakhtasimoon
📖 Tekkim Wolof
Yónnee woon Nanu ca Samuuda seen mbokk Saaliwu. Mu ne leen : “Jaamuleen Yàlla”. Ndekete yoo dañoo séddalikoo ñaari kurél di xulloo rekk.

🎧 Dégg


📜 Aaya 43-47 — Simoore An-Naml

43وَصَدَّهَا مَا كَانَت تَّعْبُدُ مِن دُونِ اللَّهِ ۖ إِنَّهَا كَانَتْ مِن قَوْمٍ كَافِرِينَ
Li mu daan jaamu bàyyi Yàlla moo ko fàbbi woon, ndax dafa bokkoon ci askanu yéefar.
44قِيلَ لَهَا ادْخُلِي الصَّرْحَ ۖ فَلَمَّا رَأَتْهُ حَسِبَتْهُ لُجَّةً وَكَشَفَتْ عَن سَاقَيْهَا ۚ قَالَ إِنَّهُ صَرْحٌ مُّمَرَّدٌ مِّن قَوَارِيرَ ۗ قَالَتْ رَبِّ إِنِّي ظَلَمْتُ نَفْسِي وَأَسْلَمْتُ مَعَ سُلَيْمَانَ لِلَّهِ رَبِّ الْعَالَمِينَ
Ñu ne ko : “Dugal ci njénde li”. Ba mu ko gisee, mu njort ne am ndox la, daldi wog i yeelam. Suleymaan ne ko : “Njénde li ay weer la ñu ko defare”. - Balxiis daldi ne : “Yaw Boroom bi, tooñaan naa sama bopp : Tey jii nag, jébbalu naa ànd ak Suleymaan dib jullit ngir Yàlla jiy Boroom àddina si”.
45وَلَقَدْ أَرْسَلْنَا إِلَىٰ ثَمُودَ أَخَاهُمْ صَالِحًا أَنِ اعْبُدُوا اللَّهَ فَإِذَا هُمْ فَرِيقَانِ يَخْتَصِمُونَ
Yónnee woon Nanu ca Samuuda seen mbokk Saaliwu. Mu ne leen : “Jaamuleen Yàlla”. Ndekete yoo dañoo séddalikoo ñaari kurél di xulloo rekk.
46قَالَ يَا قَوْمِ لِمَ تَسْتَعْجِلُونَ بِالسَّيِّئَةِ قَبْلَ الْحَسَنَةِ ۖ لَوْلَا تَسْتَغْفِرُونَ اللَّهَ لَعَلَّكُمْ تُرْحَمُونَ
Mu ne leen : "Éy samaw nit, lu tax ngeen di gën a yàkkamti lu bon ci lu baax ? Céy bu ngeen jéggalu woon Yàlla ? Kon xéy-na Mu yërëm leen.
47قَالُوا اطَّيَّرْنَا بِكَ وَبِمَن مَّعَكَ ۚ قَالَ طَائِرُكُمْ عِندَ اللَّهِ ۖ بَلْ أَنتُمْ قَوْمٌ تُفْتَنُونَ
Ñu ne ko : “Gaafal nanu la yaak ña nga àndal.”. Mu ne leen : “Kon dey cig sànje ngeen di sax ndax li ngeen di gaafal moo nekk fa Yàlla.
An-NamlFihi Alxuraan
93Aaya
MeccanRevelation
45Aaya

Tekki — An-Naml 45

Simoore An-Naml Aaya 45 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yónnee woon Nanu ca Samuuda seen mbokk Saaliwu. Mu ne…

Simoore Aaya 45/93 — Simoore An-Naml النمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Naml Dégg, Simoore An-Naml Tekki, Simoore An-Naml mp3, Simoore An-Naml pdf. Aaya 43–47. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers