An-Naml · 50/93
Tekki Waxtaan — An-Naml
وَمَكَرُوا مَكْرًا وَمَكَرْنَا مَكْرًا وَهُمْ لَا يَشْعُرُونَ ٥٠
Transliteration
Wa makaroo makranw wa makarnaa makranw wa hum laa yash`uroon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ñangay fexe am pexe, Nun it Noo ngi fexe am pexe te ñoom yéguñu ko.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 48-52 — An-Naml
48وَكَانَ فِي الْمَدِينَةِ تِسْعَةُ رَهْطٍ يُفْسِدُونَ فِي الْأَرْضِ وَلَا يُصْلِحُونَ
Mu amoon kurél bu nekkoon ca dëkk ba di juróom-ñeenti nit, daan yàq rekk te daawuñu defar.
49قَالُوا تَقَاسَمُوا بِاللَّهِ لَنُبَيِّتَنَّهُ وَأَهْلَهُ ثُمَّ لَنَقُولَنَّ لِوَلِيِّهِ مَا شَهِدْنَا مَهْلِكَ أَهْلِهِ وَإِنَّا لَصَادِقُونَ
Ñu wax ne : “Nanu waatoo ci Yàlla rey ko mook njabootam. Bu ñu xëyee ba ñay dese mbir ma laaj nu, nu tontu ne : “Nun kat teewewunu woon seenug rey”.
50وَمَكَرُوا مَكْرًا وَمَكَرْنَا مَكْرًا وَهُمْ لَا يَشْعُرُونَ
Ñangay fexe am pexe, Nun it Noo ngi fexe am pexe te ñoom yéguñu ko.
51فَانظُرْ كَيْفَ كَانَ عَاقِبَةُ مَكْرِهِمْ أَنَّا دَمَّرْنَاهُمْ وَقَوْمَهُمْ أَجْمَعِينَ
Xoolal naka seen pexe ya mujje woon : Danu leen a faagaagal ñook seeni xeet wépp.
52فَتِلْكَ بُيُوتُهُمْ خَاوِيَةً بِمَا ظَلَمُوا ۗ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَةً لِّقَوْمٍ يَعْلَمُونَ
Seen kër yaa ngi noonu gent na ngir la ñu tooñoon. Ay kéemaan a ngi ci loolu ngir aw nit ñuy xam.
An-NamlFihi Alxuraan
93Aaya
MeccanRevelation
50Aaya
Tekki — An-Naml 50
Simoore An-Naml Aaya 50 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñangay fexe am pexe, Nun it Noo ngi fexe am…Simoore Aaya 50/93 — An-Naml النمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Naml Dégg, An-Naml Tekki, An-Naml mp3, An-Naml pdf. Aaya 48–52. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








