Al-Qasas · 67/88
Tekki Waxtaan — Al-Qasas
فَأَمَّا مَن تَابَ وَآمَنَ وَعَمِلَ صَالِحًا فَعَسَىٰ أَن يَكُونَ مِنَ الْمُفْلِحِينَ ۝٦٧
Fa ammaa man taaba wa aamana wa `amila saalihan fa`asaaa ai yakoona minal mufliheen
📖 Tekkim Wolof
Képp ku ca tuub te gëm te jëf u yiw, amaana mu texe.

🎧 Dégg


📜 Aaya 65-69 — Al-Qasas

65وَيَوْمَ يُنَادِيهِمْ فَيَقُولُ مَاذَا أَجَبْتُمُ الْمُرْسَلِينَ
Bu keroogee bis ba Mu leen di woo naan leen : “Ana lan ngeen tontu woon Yonent ya ? ”
66فَعَمِيَتْ عَلَيْهِمُ الْأَنبَاءُ يَوْمَئِذٍ فَهُمْ لَا يَتَسَاءَلُونَ
Seeni firnde jaxasoo, bu boobaa [dañu naa xuum] dootuñu laajante.
67فَأَمَّا مَن تَابَ وَآمَنَ وَعَمِلَ صَالِحًا فَعَسَىٰ أَن يَكُونَ مِنَ الْمُفْلِحِينَ
Képp ku ca tuub te gëm te jëf u yiw, amaana mu texe.
68وَرَبُّكَ يَخْلُقُ مَا يَشَاءُ وَيَخْتَارُ ۗ مَا كَانَ لَهُمُ الْخِيَرَةُ ۚ سُبْحَانَ اللَّهِ وَتَعَالَىٰ عَمَّا يُشْرِكُونَ
Te sa Boroom mooy sàkk lu ko soob te neex ko ; ñoom amuñu coppan. Tudd naa sellug Yàlla ! Te kawe na lool ci la ñuy bokkaale !
69وَرَبُّكَ يَعْلَمُ مَا تُكِنُّ صُدُورُهُمْ وَمَا يُعْلِنُونَ
Te it sa Boroom a xam li seeni xol nëbb ak li ñuy feeñal.
Al-QasasFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
67Aaya

Tekki — Al-Qasas 67

Simoore Al-Qasas Aaya 67 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Képp ku ca tuub te gëm te jëf u yiw,…

Simoore Aaya 67/88 — Al-Qasas القصص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Qasas Dégg, Al-Qasas Tekki, Al-Qasas mp3, Al-Qasas pdf. Aaya 65–69. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers