Aali Imran · 92/200
Tekki Waxtaan — Simoore Aali Imran
لَن تَنَالُوا الْبِرَّ حَتَّىٰ تُنفِقُوا مِمَّا تُحِبُّونَ ۚ وَمَا تُنفِقُوا مِن شَيْءٍ فَإِنَّ اللَّهَ بِهِ عَلِيمٌ ۝٩٢
Lan tanaalul birra hattaa tunfiqoo mimmaa tuhibboon; wa maa tunfiqoo min shai`in fa innal laaha bihee `Aleem
📖 Tekkim Wolof
Dungeen am mbaax ba ba ngeen di joxe ci li ngeen bëgg. Te lépp lu ngeen mën a joxe, Yàlla xam na ko.

🎧 Dégg


📜 Aaya 90-94 — Simoore Aali Imran

90إِنَّ الَّذِينَ كَفَرُوا بَعْدَ إِيمَانِهِمْ ثُمَّ ازْدَادُوا كُفْرًا لَّن تُقْبَلَ تَوْبَتُهُمْ وَأُولَٰئِكَ هُمُ الضَّالُّونَ
Ña nga xam ne dañoo weddi ginnaaw ba ñu gëmee ba dee ci kéefar, deesuleen nangul seenug tuub. Te ñoom ñooy gaa ya sànku .
91إِنَّ الَّذِينَ كَفَرُوا وَمَاتُوا وَهُمْ كُفَّارٌ فَلَن يُقْبَلَ مِنْ أَحَدِهِم مِّلْءُ الْأَرْضِ ذَهَبًا وَلَوِ افْتَدَىٰ بِهِ ۗ أُولَٰئِكَ لَهُمْ عَذَابٌ أَلِيمٌ وَمَا لَهُم مِّن نَّاصِرِينَ
Ña nga xam ne ñoo weddi ba dee ci kéefar, deesul nangul kenn ci ñoom mu jote doonte la joxe na wurus wu fees dell suuf si ngir loolu [jote]. Ñooñee, mbugal mu tar lañuy am, te duñu am ku leen dimbali.
92لَن تَنَالُوا الْبِرَّ حَتَّىٰ تُنفِقُوا مِمَّا تُحِبُّونَ ۚ وَمَا تُنفِقُوا مِن شَيْءٍ فَإِنَّ اللَّهَ بِهِ عَلِيمٌ
Dungeen am mbaax ba ba ngeen di joxe ci li ngeen bëgg. Te lépp lu ngeen mën a joxe, Yàlla xam na ko.
93۞ كُلُّ الطَّعَامِ كَانَ حِلًّا لِّبَنِي إِسْرَائِيلَ إِلَّا مَا حَرَّمَ إِسْرَائِيلُ عَلَىٰ نَفْسِهِ مِن قَبْلِ أَن تُنَزَّلَ التَّوْرَاةُ ۗ قُلْ فَأْتُوا بِالتَّوْرَاةِ فَاتْلُوهَا إِن كُنتُمْ صَادِقِينَ
Ñam yépp a daganoon ca waa Banii-Israayiil, lu dul ñam ya [Israayiil ] araama loon ca boppam lu jiitu ñu doon wàcce Tawreet. Neel: “Indileen Tawreet te jàng ko, ndegam ñu dëggu ngeen ! ”
94فَمَنِ افْتَرَىٰ عَلَى اللَّهِ الْكَذِبَ مِن بَعْدِ ذَٰلِكَ فَأُولَٰئِكَ هُمُ الظَّالِمُونَ
Ku duural Yàlla ay fen, ginnaaw loolu... ñooñaa di tooñkat ya.
Aali ImranFihi Alxuraan
200Aaya
MedinanRevelation
92Aaya

Tekki — Aali Imran 92

Simoore Aali Imran Aaya 92 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Dungeen am mbaax ba ba ngeen di joxe ci li…

Simoore Aaya 92/200 — Simoore Aali Imran آل عمران (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Aali Imran Dégg, Simoore Aali Imran Tekki, Simoore Aali Imran mp3, Simoore Aali Imran pdf. Aaya 90–94. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers