As-Sajda · 6/30
Tekki Waxtaan — Simoore As-Sajda
ذَٰلِكَ عَالِمُ الْغَيْبِ وَالشَّهَادَةِ الْعَزِيزُ الرَّحِيمُ ۝٦
Zaalika `aalimul ghaybi wa shahaadatil `azeezur raheem
📖 Tekkim Wolof
Kooka mooy xamkatu kumpa ak li feeñ, mooy Boroom Kàttan, di Jaglewaakoonu yërmaandeem,

🎧 Dégg


📜 Aaya 4-8 — Simoore As-Sajda

4اللَّهُ الَّذِي خَلَقَ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ وَمَا بَيْنَهُمَا فِي سِتَّةِ أَيَّامٍ ثُمَّ اسْتَوَىٰ عَلَى الْعَرْشِ ۖ مَا لَكُم مِّن دُونِهِ مِن وَلِيٍّ وَلَا شَفِيعٍ ۚ أَفَلَا تَتَذَكَّرُونَ
Yàlla mi bind asamaan yeek suuf si ak li nekk ci seen diggante ci diirub juróom-benni fan. Daldi yemoo ca Gàngunaay ga [Aras]. Amuleen benn wéeruwaay walla rammukat bu dul Moom. Moo ndax dangeen dul fàttaliku ?
5يُدَبِّرُ الْأَمْرَ مِنَ السَّمَاءِ إِلَى الْأَرْضِ ثُمَّ يَعْرُجُ إِلَيْهِ فِي يَوْمٍ كَانَ مِقْدَارُهُ أَلْفَ سَنَةٍ مِّمَّا تَعُدُّونَ
Mooy settantal [lijjanti] mbir yi, jële ko asamaan jëme ko ci suuf si, topp mu yéeg asamaan ci bis boo xam ne ab nattaleem junni la ci ay ati àddina.
6ذَٰلِكَ عَالِمُ الْغَيْبِ وَالشَّهَادَةِ الْعَزِيزُ الرَّحِيمُ
Kooka mooy xamkatu kumpa ak li feeñ, mooy Boroom Kàttan, di Jaglewaakoonu yërmaandeem,
7الَّذِي أَحْسَنَ كُلَّ شَيْءٍ خَلَقَهُ ۖ وَبَدَأَ خَلْقَ الْإِنسَانِ مِن طِينٍ
Moo jekkal sosug lu ne. Daldi door sosug nit ci ban,
8ثُمَّ جَعَلَ نَسْلَهُ مِن سُلَالَةٍ مِّن مَّاءٍ مَّهِينٍ
daldi nay defe askanam wa mu càllaloo ci am ndox mu doyadi;
As-SajdaFihi Alxuraan
30Aaya
MeccanRevelation
6Aaya

Tekki — As-Sajda 6

Simoore As-Sajda Aaya 6 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Kooka mooy xamkatu kumpa ak li feeñ, mooy Boroom Kàttan,…

Simoore Aaya 6/30 — Simoore As-Sajda السجدة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Sajda Dégg, Simoore As-Sajda Tekki, Simoore As-Sajda mp3, Simoore As-Sajda pdf. Aaya 4–8. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers