As-Sajda · 8/30
Tekki Waxtaan — Simoore As-Sajda
ثُمَّ جَعَلَ نَسْلَهُ مِن سُلَالَةٍ مِّن مَّاءٍ مَّهِينٍ ۝٨
Thumma ja`ala naslahoo min sulaalatim mim maaa`immaheen
📖 Tekkim Wolof
daldi nay defe askanam wa mu càllaloo ci am ndox mu doyadi;

🎧 Dégg


📜 Aaya 6-10 — Simoore As-Sajda

6ذَٰلِكَ عَالِمُ الْغَيْبِ وَالشَّهَادَةِ الْعَزِيزُ الرَّحِيمُ
Kooka mooy xamkatu kumpa ak li feeñ, mooy Boroom Kàttan, di Jaglewaakoonu yërmaandeem,
7الَّذِي أَحْسَنَ كُلَّ شَيْءٍ خَلَقَهُ ۖ وَبَدَأَ خَلْقَ الْإِنسَانِ مِن طِينٍ
Moo jekkal sosug lu ne. Daldi door sosug nit ci ban,
8ثُمَّ جَعَلَ نَسْلَهُ مِن سُلَالَةٍ مِّن مَّاءٍ مَّهِينٍ
daldi nay defe askanam wa mu càllaloo ci am ndox mu doyadi;
9ثُمَّ سَوَّاهُ وَنَفَخَ فِيهِ مِن رُّوحِهِ ۖ وَجَعَلَ لَكُمُ السَّمْعَ وَالْأَبْصَارَ وَالْأَفْئِدَةَ ۚ قَلِيلًا مَّا تَشْكُرُونَ
daldi koy yemale, ëf ci Ruuwam. Defaral leen dégg-dégg, ak ub gis ak i xol. Te néewaana ngeen di Ko sant !
10وَقَالُوا أَإِذَا ضَلَلْنَا فِي الْأَرْضِ أَإِنَّا لَفِي خَلْقٍ جَدِيدٍ ۚ بَلْ هُم بِلِقَاءِ رَبِّهِمْ كَافِرُونَ
Ñuy wax naan : “Ndax bu nu seeyee ci biir suuf si, dananu dekkiwaat ? ”. Ñoom dañoo weddi ne danañu dajeek seen Boroom.
As-SajdaFihi Alxuraan
30Aaya
MeccanRevelation
8Aaya

Tekki — As-Sajda 8

Simoore As-Sajda Aaya 8 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : daldi nay defe askanam wa mu càllaloo ci am ndox…

Simoore Aaya 8/30 — Simoore As-Sajda السجدة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Sajda Dégg, Simoore As-Sajda Tekki, Simoore As-Sajda mp3, Simoore As-Sajda pdf. Aaya 6–10. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers