Al-Ahzab · 43/73
Tekki Waxtaan — Al-Ahzab
هُوَ الَّذِي يُصَلِّي عَلَيْكُمْ وَمَلَائِكَتُهُ لِيُخْرِجَكُم مِّنَ الظُّلُمَاتِ إِلَى النُّورِ ۚ وَكَانَ بِالْمُؤْمِنِينَ رَحِيمًا ٤٣
Transliteration
Huwal lazee yusallee `alaikum wa malaaa`ikatuhoo liyukhrijakum minazzulumaati ilan-noor wa kaana bilmu`mineena Raheemaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Mooy kiy julli ci yéen, di leen ñaanal, - Mook ay Malaakaam, - ngir génne leen cig lëndëm, jëme leen cig leer ; te Mu di Jaglewaakoonu yërmaandeem ci ñi gëm.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 41-45 — Al-Ahzab
41يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا اذْكُرُوا اللَّهَ ذِكْرًا كَثِيرًا
Éy yéen ñi gëm ! Nangeen di farataal, di tudd Yàlla lu bari.
42وَسَبِّحُوهُ بُكْرَةً وَأَصِيلًا
te nangeen di Ko sàbbaal suba ak ngoon.
43هُوَ الَّذِي يُصَلِّي عَلَيْكُمْ وَمَلَائِكَتُهُ لِيُخْرِجَكُم مِّنَ الظُّلُمَاتِ إِلَى النُّورِ ۚ وَكَانَ بِالْمُؤْمِنِينَ رَحِيمًا
Mooy kiy julli ci yéen, di leen ñaanal, - Mook ay Malaakaam, - ngir génne leen cig lëndëm, jëme leen cig leer ; te Mu di Jaglewaakoonu yërmaandeem ci ñi gëm.
44تَحِيَّتُهُمْ يَوْمَ يَلْقَوْنَهُ سَلَامٌ ۚ وَأَعَدَّ لَهُمْ أَجْرًا كَرِيمًا
Seenub nuyyoo Bis nuy dajeek Moom : “Jàmm rekk”, te mu waajal leen ag pey gu tedd .
45يَا أَيُّهَا النَّبِيُّ إِنَّا أَرْسَلْنَاكَ شَاهِدًا وَمُبَشِّرًا وَنَذِيرًا
Éy yaw Yonent bi ! Noo la yebal ngir nga doon seede, di béglekat, di xuppekat.
Al-AhzabFihi Alxuraan
73Aaya
MedinanRevelation
43Aaya
Tekki — Al-Ahzab 43
Simoore Al-Ahzab Aaya 43 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mooy kiy julli ci yéen, di leen ñaanal, - Mook…Simoore Aaya 43/73 — Al-Ahzab الأحزاب (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Ahzab Dégg, Al-Ahzab Tekki, Al-Ahzab mp3, Al-Ahzab pdf. Aaya 41–45. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








