Al-Ahzab · 64/73
Tekki Waxtaan — Al-Ahzab
إِنَّ اللَّهَ لَعَنَ الْكَافِرِينَ وَأَعَدَّ لَهُمْ سَعِيرًا ٦٤
Transliteration
Innal laaha la`anal kaafireena wa a`adda lahum sa`eeraa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Yàlla rëbb na yéefar yi te waajalal na leen aw safara,
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 62-66 — Al-Ahzab
62سُنَّةَ اللَّهِ فِي الَّذِينَ خَلَوْا مِن قَبْلُ ۖ وَلَن تَجِدَ لِسُنَّةِ اللَّهِ تَبْدِيلًا
Lii mooy sunnas Yàlla, ab dogalam ci ña fi jiitu woon te sunnas Yàlla du soppiku mukk.
63يَسْأَلُكَ النَّاسُ عَنِ السَّاعَةِ ۖ قُلْ إِنَّمَا عِلْمُهَا عِندَ اللَّهِ ۚ وَمَا يُدْرِيكَ لَعَلَّ السَّاعَةَ تَكُونُ قَرِيبًا
Nit ñaa ngi lay laaj ci mbiri Bis-pénc ba. Waxal ne : “Yàllaa ko xam”. Te yaw sax loo ci xam ? Amaana Bis-pénc ba di lu jegeñ.
64إِنَّ اللَّهَ لَعَنَ الْكَافِرِينَ وَأَعَدَّ لَهُمْ سَعِيرًا
Yàlla rëbb na yéefar yi te waajalal na leen aw safara,
65خَالِدِينَ فِيهَا أَبَدًا ۖ لَّا يَجِدُونَ وَلِيًّا وَلَا نَصِيرًا
dañu fay béel fàww, duñu fa am ku leen méngoo, duñu fa am ndimbal.
66يَوْمَ تُقَلَّبُ وُجُوهُهُمْ فِي النَّارِ يَقُولُونَ يَا لَيْتَنَا أَطَعْنَا اللَّهَ وَأَطَعْنَا الرَّسُولَا
Bis ba ñuy wëlbati seeni kanam ca Safara, ñuy wax naan : “Aka neexoon nu toppoon Yàlla, nu toppoon Yonent ba ! ”.
Al-AhzabFihi Alxuraan
73Aaya
MedinanRevelation
64Aaya
Tekki — Al-Ahzab 64
Simoore Al-Ahzab Aaya 64 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàlla rëbb na yéefar yi te waajalal na leen aw…Simoore Aaya 64/73 — Al-Ahzab الأحزاب (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Ahzab Dégg, Al-Ahzab Tekki, Al-Ahzab mp3, Al-Ahzab pdf. Aaya 62–66. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








