Al-Ahzab · 63/73
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Ahzab
يَسْأَلُكَ النَّاسُ عَنِ السَّاعَةِ ۖ قُلْ إِنَّمَا عِلْمُهَا عِندَ اللَّهِ ۚ وَمَا يُدْرِيكَ لَعَلَّ السَّاعَةَ تَكُونُ قَرِيبًا ۝٦٣
Yas`alukan naasu `anis Saa`ati qul innamaa `ilmuhaa `indal laah; wa maa yudreeka la`allas Saa`ata takoonu qareebaa
📖 Tekkim Wolof
Nit ñaa ngi lay laaj ci mbiri Bis-pénc ba. Waxal ne : “Yàllaa ko xam”. Te yaw sax loo ci xam ? Amaana Bis-pénc ba di lu jegeñ.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 61-65 — Simoore Al-Ahzab

61مَّلْعُونِينَ ۖ أَيْنَمَا ثُقِفُوا أُخِذُوا وَقُتِّلُوا تَقْتِيلًا
Muy ñuñu rëbb. Fu ñu jublu, ñu faagaagal leen :
62سُنَّةَ اللَّهِ فِي الَّذِينَ خَلَوْا مِن قَبْلُ ۖ وَلَن تَجِدَ لِسُنَّةِ اللَّهِ تَبْدِيلًا
Lii mooy sunnas Yàlla, ab dogalam ci ña fi jiitu woon te sunnas Yàlla du soppiku mukk.
63يَسْأَلُكَ النَّاسُ عَنِ السَّاعَةِ ۖ قُلْ إِنَّمَا عِلْمُهَا عِندَ اللَّهِ ۚ وَمَا يُدْرِيكَ لَعَلَّ السَّاعَةَ تَكُونُ قَرِيبًا
Nit ñaa ngi lay laaj ci mbiri Bis-pénc ba. Waxal ne : “Yàllaa ko xam”. Te yaw sax loo ci xam ? Amaana Bis-pénc ba di lu jegeñ.
64إِنَّ اللَّهَ لَعَنَ الْكَافِرِينَ وَأَعَدَّ لَهُمْ سَعِيرًا
Yàlla rëbb na yéefar yi te waajalal na leen aw safara,
65خَالِدِينَ فِيهَا أَبَدًا ۖ لَّا يَجِدُونَ وَلِيًّا وَلَا نَصِيرًا
dañu fay béel fàww, duñu fa am ku leen méngoo, duñu fa am ndimbal.
Al-AhzabFihi Alxuraan
73Aaya
MedinanRevelation
63Aaya

Tekki — Al-Ahzab 63

Simoore Al-Ahzab Aaya 63 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nit ñaa ngi lay laaj ci mbiri Bis-pénc ba. Waxal…

Simoore Aaya 63/73 — Simoore Al-Ahzab الأحزاب (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Ahzab Dégg, Simoore Al-Ahzab Tekki, Simoore Al-Ahzab mp3, Simoore Al-Ahzab pdf. Aaya 61–65. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 29, 2026

Don't forget us in your sincere prayers