Ya-Sin · 10/83
Tekki Waxtaan — Ya-Sin
وَسَوَاءٌ عَلَيْهِمْ أَأَنذَرْتَهُمْ أَمْ لَمْ تُنذِرْهُمْ لَا يُؤْمِنُونَ ۝١٠
Wa sawaaa`un `alaihim `a-anzartahum am lam tunzirhum laa yu`minoon
📖 Tekkim Wolof
Nga xupp leen ak nga ñàkk leen a xupp ñoo yem kepp ci ñoom : duñu mës a gëm.
🎧 Dégg

📜 Aaya 8-12 — Ya-Sin

8إِنَّا جَعَلْنَا فِي أَعْنَاقِهِمْ أَغْلَالًا فَهِيَ إِلَى الْأَذْقَانِ فَهُم مُّقْمَحُونَ
Def Nanu ay jéng ci seeni loos, mu àndak seeni daayi sikkim : ñu joñ leen.
9وَجَعَلْنَا مِن بَيْنِ أَيْدِيهِمْ سَدًّا وَمِنْ خَلْفِهِمْ سَدًّا فَأَغْشَيْنَاهُمْ فَهُمْ لَا يُبْصِرُونَ
def Nanu ab ñag ci kanam ak ci seen ginnaaw ; Muur Nanu leen ba dootuñu gis.
10وَسَوَاءٌ عَلَيْهِمْ أَأَنذَرْتَهُمْ أَمْ لَمْ تُنذِرْهُمْ لَا يُؤْمِنُونَ
Nga xupp leen ak nga ñàkk leen a xupp ñoo yem kepp ci ñoom : duñu mës a gëm.
11إِنَّمَا تُنذِرُ مَنِ اتَّبَعَ الذِّكْرَ وَخَشِيَ الرَّحْمَٰنَ بِالْغَيْبِ ۖ فَبَشِّرْهُ بِمَغْفِرَةٍ وَأَجْرٍ كَرِيمٍ
Ka ngay war a xupp kay mooy kay topp [Alxuraan], tey ragal Yàlla ci kumpa. Nanga ko bégal ci ag njéggal ak pey gu tedd .
12إِنَّا نَحْنُ نُحْيِي الْمَوْتَىٰ وَنَكْتُبُ مَا قَدَّمُوا وَآثَارَهُمْ ۚ وَكُلَّ شَيْءٍ أَحْصَيْنَاهُ فِي إِمَامٍ مُّبِينٍ
Nun Yàlla nooy dundal néew tey bind la ñu defoon ak seeni jeexit. Te mbir mu ci bokk yéege Nanu ko ci biir ab téere bu bir , bind ko ca.
Ya-SinFihi Alxuraan
83Aaya
MeccanRevelation
10Aaya

Tekki — Ya-Sin 10

Simoore Ya-Sin Aaya 10 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nga xupp leen ak nga ñàkk leen a xupp ñoo…

Simoore Aaya 10/83 — Ya-Sin يس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ya-Sin Dégg, Ya-Sin Tekki, Ya-Sin mp3, Ya-Sin pdf. Aaya 8–12. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers