Ya-Sin · 33/83
Tekki Waxtaan — Simoore Ya-Sin
وَآيَةٌ لَّهُمُ الْأَرْضُ الْمَيْتَةُ أَحْيَيْنَاهَا وَأَخْرَجْنَا مِنْهَا حَبًّا فَمِنْهُ يَأْكُلُونَ ۝٣٣
Wa Aayatul lahumul ardul maitatu ahyainaahaa wa akhrajnaa minhaa habban faminhu yaakuloon
📖 Tekkim Wolof
Indil Nanu leen firnde te moo di suuf si dee , Nu dekkalaat ko, [tawu ndow] génne ca ay doom, ngeen di ca lekk.

🎧 Dégg


📜 Aaya 31-35 — Simoore Ya-Sin

31أَلَمْ يَرَوْا كَمْ أَهْلَكْنَا قَبْلَهُم مِّنَ الْقُرُونِ أَنَّهُمْ إِلَيْهِمْ لَا يَرْجِعُونَ
Xanaa gisuñu na Nu faagale woon maas ya leen jiitu woon ? Te kenn du ca dellusi.
32وَإِن كُلٌّ لَّمَّا جَمِيعٌ لَّدَيْنَا مُحْضَرُونَ
Te ñoom ñépp danañu daje Sama kanam .
33وَآيَةٌ لَّهُمُ الْأَرْضُ الْمَيْتَةُ أَحْيَيْنَاهَا وَأَخْرَجْنَا مِنْهَا حَبًّا فَمِنْهُ يَأْكُلُونَ
Indil Nanu leen firnde te moo di suuf si dee , Nu dekkalaat ko, [tawu ndow] génne ca ay doom, ngeen di ca lekk.
34وَجَعَلْنَا فِيهَا جَنَّاتٍ مِّن نَّخِيلٍ وَأَعْنَابٍ وَفَجَّرْنَا فِيهَا مِنَ الْعُيُونِ
Nu def ca ay tooli dëri tàndarma ak yu reseñ, xàbbal ca ay bëti ndox,
35لِيَأْكُلُوا مِن ثَمَرِهِ وَمَا عَمِلَتْهُ أَيْدِيهِمْ ۖ أَفَلَا يَشْكُرُونَ
ndax ngeen di lekk ca meññent ma ak li ngeen cay liggéeyee. Moo ndax duñu sant ?
Ya-SinFihi Alxuraan
83Aaya
MeccanRevelation
33Aaya

Tekki — Ya-Sin 33

Simoore Ya-Sin Aaya 33 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Indil Nanu leen firnde te moo di suuf si dee…

Simoore Aaya 33/83 — Simoore Ya-Sin يس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ya-Sin Dégg, Simoore Ya-Sin Tekki, Simoore Ya-Sin mp3, Simoore Ya-Sin pdf. Aaya 31–35. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers