Ya-Sin · 38/83
Tekki Waxtaan — Ya-Sin
وَالشَّمْسُ تَجْرِي لِمُسْتَقَرٍّ لَّهَا ۚ ذَٰلِكَ تَقْدِيرُ الْعَزِيزِ الْعَلِيمِ ۝٣٨
Wash-shamsu tajree limustaqarril lahaa; zaalika taqdeerul `Azeezil Aleem
📖 Tekkim Wolof
te jant baa ngay daw ca fa ñu ko rëddal ; looloo di nattaleb Yàlla miy boroom Kàttan, di ku Xam.
🎧 Dégg

📜 Aaya 36-40 — Ya-Sin

36سُبْحَانَ الَّذِي خَلَقَ الْأَزْوَاجَ كُلَّهَا مِمَّا تُنبِتُ الْأَرْضُ وَمِنْ أَنفُسِهِمْ وَمِمَّا لَا يَعْلَمُونَ
Tudd naa sellug bind yóllent yi mbooleseen ci liy sax ci suuf ak ci seeni jëmm ak ci li ñu xamul !
37وَآيَةٌ لَّهُمُ اللَّيْلُ نَسْلَخُ مِنْهُ النَّهَارَ فَإِذَا هُم مُّظْلِمُونَ
Ak firndey bu bëccëg jàlle, guddi ñëw lëndëm taruus.
38وَالشَّمْسُ تَجْرِي لِمُسْتَقَرٍّ لَّهَا ۚ ذَٰلِكَ تَقْدِيرُ الْعَزِيزِ الْعَلِيمِ
te jant baa ngay daw ca fa ñu ko rëddal ; looloo di nattaleb Yàlla miy boroom Kàttan, di ku Xam.
39وَالْقَمَرَ قَدَّرْنَاهُ مَنَازِلَ حَتَّىٰ عَادَ كَالْعُرْجُونِ الْقَدِيمِ
Weer wi nattale Nanu ko ay këri wàccuwaay ba faf mu mel ni tàndarma gu màggat.
40لَا الشَّمْسُ يَنبَغِي لَهَا أَن تُدْرِكَ الْقَمَرَ وَلَا اللَّيْلُ سَابِقُ النَّهَارِ ۚ وَكُلٌّ فِي فَلَكٍ يَسْبَحُونَ
Jant bi du jot weer wi, guddi it du jiitu bëccëg ; ku nekk a nga ca yoonam di féey.
Ya-SinFihi Alxuraan
83Aaya
MeccanRevelation
38Aaya

Tekki — Ya-Sin 38

Simoore Ya-Sin Aaya 38 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te jant baa ngay daw ca fa ñu ko rëddal…

Simoore Aaya 38/83 — Ya-Sin يس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ya-Sin Dégg, Ya-Sin Tekki, Ya-Sin mp3, Ya-Sin pdf. Aaya 36–40. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers