Ya-Sin · 37/83
Tekki Waxtaan — Ya-Sin
وَآيَةٌ لَّهُمُ اللَّيْلُ نَسْلَخُ مِنْهُ النَّهَارَ فَإِذَا هُم مُّظْلِمُونَ ۝٣٧
Wa Aayatul lahumul lailu naslakhu minhun nahaara fa-izaa hum muzlimoon
📖 Tekkim Wolof
Ak firndey bu bëccëg jàlle, guddi ñëw lëndëm taruus.

🎧 Dégg


📜 Aaya 35-39 — Ya-Sin

35لِيَأْكُلُوا مِن ثَمَرِهِ وَمَا عَمِلَتْهُ أَيْدِيهِمْ ۖ أَفَلَا يَشْكُرُونَ
ndax ngeen di lekk ca meññent ma ak li ngeen cay liggéeyee. Moo ndax duñu sant ?
36سُبْحَانَ الَّذِي خَلَقَ الْأَزْوَاجَ كُلَّهَا مِمَّا تُنبِتُ الْأَرْضُ وَمِنْ أَنفُسِهِمْ وَمِمَّا لَا يَعْلَمُونَ
Tudd naa sellug bind yóllent yi mbooleseen ci liy sax ci suuf ak ci seeni jëmm ak ci li ñu xamul !
37وَآيَةٌ لَّهُمُ اللَّيْلُ نَسْلَخُ مِنْهُ النَّهَارَ فَإِذَا هُم مُّظْلِمُونَ
Ak firndey bu bëccëg jàlle, guddi ñëw lëndëm taruus.
38وَالشَّمْسُ تَجْرِي لِمُسْتَقَرٍّ لَّهَا ۚ ذَٰلِكَ تَقْدِيرُ الْعَزِيزِ الْعَلِيمِ
te jant baa ngay daw ca fa ñu ko rëddal ; looloo di nattaleb Yàlla miy boroom Kàttan, di ku Xam.
39وَالْقَمَرَ قَدَّرْنَاهُ مَنَازِلَ حَتَّىٰ عَادَ كَالْعُرْجُونِ الْقَدِيمِ
Weer wi nattale Nanu ko ay këri wàccuwaay ba faf mu mel ni tàndarma gu màggat.
Ya-SinFihi Alxuraan
83Aaya
MeccanRevelation
37Aaya

Tekki — Ya-Sin 37

Simoore Ya-Sin Aaya 37 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ak firndey bu bëccëg jàlle, guddi ñëw lëndëm taruus.

Simoore Aaya 37/83 — Ya-Sin يس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ya-Sin Dégg, Ya-Sin Tekki, Ya-Sin mp3, Ya-Sin pdf. Aaya 35–39. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers