Ya-Sin · 41/83
Tekki Waxtaan — Simoore Ya-Sin
وَآيَةٌ لَّهُمْ أَنَّا حَمَلْنَا ذُرِّيَّتَهُمْ فِي الْفُلْكِ الْمَشْحُونِ ۝٤١
Wa Aayatul lahum annaa hamalnaa zurriyatahum fil fulkil mashhoon
📖 Tekkim Wolof
Ak firndey yenu gi Nu yenu seeni sët ci biir ag gaal gu ñu sëf ;

🎧 Dégg


📜 Aaya 39-43 — Simoore Ya-Sin

39وَالْقَمَرَ قَدَّرْنَاهُ مَنَازِلَ حَتَّىٰ عَادَ كَالْعُرْجُونِ الْقَدِيمِ
Weer wi nattale Nanu ko ay këri wàccuwaay ba faf mu mel ni tàndarma gu màggat.
40لَا الشَّمْسُ يَنبَغِي لَهَا أَن تُدْرِكَ الْقَمَرَ وَلَا اللَّيْلُ سَابِقُ النَّهَارِ ۚ وَكُلٌّ فِي فَلَكٍ يَسْبَحُونَ
Jant bi du jot weer wi, guddi it du jiitu bëccëg ; ku nekk a nga ca yoonam di féey.
41وَآيَةٌ لَّهُمْ أَنَّا حَمَلْنَا ذُرِّيَّتَهُمْ فِي الْفُلْكِ الْمَشْحُونِ
Ak firndey yenu gi Nu yenu seeni sët ci biir ag gaal gu ñu sëf ;
42وَخَلَقْنَا لَهُم مِّن مِّثْلِهِ مَا يَرْكَبُونَ
Te sàkkal Nanu leen yeneen yu ni mel ñu di ca war.
43وَإِن نَّشَأْ نُغْرِقْهُمْ فَلَا صَرِيخَ لَهُمْ وَلَا هُمْ يُنقَذُونَ
Bu Nu sooboon, Nu labal leen ; duñu xam fu ñuy yuuxu jëmële, te kenn du leen xettali,
Ya-SinFihi Alxuraan
83Aaya
MeccanRevelation
41Aaya

Tekki — Ya-Sin 41

Simoore Ya-Sin Aaya 41 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ak firndey yenu gi Nu yenu seeni sët ci biir…

Simoore Aaya 41/83 — Simoore Ya-Sin يس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ya-Sin Dégg, Simoore Ya-Sin Tekki, Simoore Ya-Sin mp3, Simoore Ya-Sin pdf. Aaya 39–43. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers