Ya-Sin · 42/83
Tekki Waxtaan — Simoore Ya-Sin
وَخَلَقْنَا لَهُم مِّن مِّثْلِهِ مَا يَرْكَبُونَ ۝٤٢
Wa khalaqnaa lahum mim-mislihee maa yarkaboon
📖 Tekkim Wolof
Te sàkkal Nanu leen yeneen yu ni mel ñu di ca war.

🎧 Dégg


📜 Aaya 40-44 — Simoore Ya-Sin

40لَا الشَّمْسُ يَنبَغِي لَهَا أَن تُدْرِكَ الْقَمَرَ وَلَا اللَّيْلُ سَابِقُ النَّهَارِ ۚ وَكُلٌّ فِي فَلَكٍ يَسْبَحُونَ
Jant bi du jot weer wi, guddi it du jiitu bëccëg ; ku nekk a nga ca yoonam di féey.
41وَآيَةٌ لَّهُمْ أَنَّا حَمَلْنَا ذُرِّيَّتَهُمْ فِي الْفُلْكِ الْمَشْحُونِ
Ak firndey yenu gi Nu yenu seeni sët ci biir ag gaal gu ñu sëf ;
42وَخَلَقْنَا لَهُم مِّن مِّثْلِهِ مَا يَرْكَبُونَ
Te sàkkal Nanu leen yeneen yu ni mel ñu di ca war.
43وَإِن نَّشَأْ نُغْرِقْهُمْ فَلَا صَرِيخَ لَهُمْ وَلَا هُمْ يُنقَذُونَ
Bu Nu sooboon, Nu labal leen ; duñu xam fu ñuy yuuxu jëmële, te kenn du leen xettali,
44إِلَّا رَحْمَةً مِّنَّا وَمَتَاعًا إِلَىٰ حِينٍ
lu dul yërmaande ju bawoo ci Nun, ak i xéewal ba jëmmi jamono.
Ya-SinFihi Alxuraan
83Aaya
MeccanRevelation
42Aaya

Tekki — Ya-Sin 42

Simoore Ya-Sin Aaya 42 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te sàkkal Nanu leen yeneen yu ni mel ñu di…

Simoore Aaya 42/83 — Simoore Ya-Sin يس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ya-Sin Dégg, Simoore Ya-Sin Tekki, Simoore Ya-Sin mp3, Simoore Ya-Sin pdf. Aaya 40–44. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers