Ya-Sin · 46/83
Tekki Waxtaan — Simoore Ya-Sin
وَمَا تَأْتِيهِم مِّنْ آيَةٍ مِّنْ آيَاتِ رَبِّهِمْ إِلَّا كَانُوا عَنْهَا مُعْرِضِينَ ۝٤٦
Wa maa taateehim min aayatim min ayataati Rabbihim illaa kaanoo `anhaa mu`rideen
📖 Tekkim Wolof
Amul yenn laaya , yu bokk ci seeni laayay Boroom, dikkal leen te dañu koo dëddu.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 44-48 — Simoore Ya-Sin

44إِلَّا رَحْمَةً مِّنَّا وَمَتَاعًا إِلَىٰ حِينٍ
lu dul yërmaande ju bawoo ci Nun, ak i xéewal ba jëmmi jamono.
45وَإِذَا قِيلَ لَهُمُ اتَّقُوا مَا بَيْنَ أَيْدِيكُمْ وَمَا خَلْفَكُمْ لَعَلَّكُمْ تُرْحَمُونَ
Te saa su ñu leen waxee ne : “Wattandikuleen li nekk ci seen kanam ak li ci seen ginnaaw ndax amaana yërmaande wàcc ci yéen” !...
46وَمَا تَأْتِيهِم مِّنْ آيَةٍ مِّنْ آيَاتِ رَبِّهِمْ إِلَّا كَانُوا عَنْهَا مُعْرِضِينَ
Amul yenn laaya , yu bokk ci seeni laayay Boroom, dikkal leen te dañu koo dëddu.
47وَإِذَا قِيلَ لَهُمْ أَنفِقُوا مِمَّا رَزَقَكُمُ اللَّهُ قَالَ الَّذِينَ كَفَرُوا لِلَّذِينَ آمَنُوا أَنُطْعِمُ مَن لَّوْ يَشَاءُ اللَّهُ أَطْعَمَهُ إِنْ أَنتُمْ إِلَّا فِي ضَلَالٍ مُّبِينٍ
Saa su ñu leen waxee ne : “Joxeleen ci alal ji leen Yàlla wërsëgal”, ña weddi dañuy wax ña gëm, naan leen : “Moo ndax nun danuy dundal koo xam ne bu neexoon Yàlla mu dundal ko ? Yéen daal ci ag réer gu bir ngeen nekk”.
48وَيَقُولُونَ مَتَىٰ هَٰذَا الْوَعْدُ إِن كُنتُمْ صَادِقِينَ
Ña ngay wax naan : “Dig ba kañ lay ñëw ndegam li ngeen di wax dëgg la ? ”
Ya-SinFihi Alxuraan
83Aaya
MeccanRevelation
46Aaya

Tekki — Ya-Sin 46

Simoore Ya-Sin Aaya 46 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Amul yenn laaya , yu bokk ci seeni laayay Boroom,…

Simoore Aaya 46/83 — Simoore Ya-Sin يس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ya-Sin Dégg, Simoore Ya-Sin Tekki, Simoore Ya-Sin mp3, Simoore Ya-Sin pdf. Aaya 44–48. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers