As-Saffat · 88/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
فَنَظَرَ نَظْرَةً فِي النُّجُومِ ۝٨٨
Fanazara nazratan finnujoom
📖 Tekkim Wolof
Mu téen xool biddéew yi [di settantal],

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 86-90 — Simoore As-Saffat

86أَئِفْكًا آلِهَةً دُونَ اللَّهِ تُرِيدُونَ
Moo ndax ay nar ngeen di namm a def ay yàlla bàyyi Yàlla Moom ?
87فَمَا ظَنُّكُم بِرَبِّ الْعَالَمِينَ
Waaw, lu ngeen njort ci Yàlla boroom asamaan si ? ”
88فَنَظَرَ نَظْرَةً فِي النُّجُومِ
Mu téen xool biddéew yi [di settantal],
89فَقَالَ إِنِّي سَقِيمٌ
mu daldi wax ne : “Man damaa wopp”.
90فَتَوَلَّوْا عَنْهُ مُدْبِرِينَ
Ñu dëddu ko, won ko ginnaaw.
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
88Aaya

Tekki — As-Saffat 88

Simoore As-Saffat Aaya 88 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu téen xool biddéew yi [di settantal],

Simoore Aaya 88/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 86–90. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers