As-Saffat · 89/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
فَقَالَ إِنِّي سَقِيمٌ ۝٨٩
Faqaala inee saqeem
📖 Tekkim Wolof
mu daldi wax ne : “Man damaa wopp”.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 87-91 — Simoore As-Saffat

87فَمَا ظَنُّكُم بِرَبِّ الْعَالَمِينَ
Waaw, lu ngeen njort ci Yàlla boroom asamaan si ? ”
88فَنَظَرَ نَظْرَةً فِي النُّجُومِ
Mu téen xool biddéew yi [di settantal],
89فَقَالَ إِنِّي سَقِيمٌ
mu daldi wax ne : “Man damaa wopp”.
90فَتَوَلَّوْا عَنْهُ مُدْبِرِينَ
Ñu dëddu ko, won ko ginnaaw.
91فَرَاغَ إِلَىٰ آلِهَتِهِمْ فَقَالَ أَلَا تَأْكُلُونَ
Mu potoxlu ca seen yàlla ya, ne leen : “Ndax dungeen lekk ?
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
89Aaya

Tekki — As-Saffat 89

Simoore As-Saffat Aaya 89 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : mu daldi wax ne : “Man damaa wopp”.

Simoore Aaya 89/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 87–91. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers