Sad · 67/88
Tekki Waxtaan — Sad
قُلْ هُوَ نَبَأٌ عَظِيمٌ ۝٦٧
Qul huwa naba`un `azeem
📖 Tekkim Wolof
Waxal ne : “Xibaar bu rëy la,

🎧 Dégg


📜 Aaya 65-69 — Sad

65قُلْ إِنَّمَا أَنَا مُنذِرٌ ۖ وَمَا مِنْ إِلَٰهٍ إِلَّا اللَّهُ الْوَاحِدُ الْقَهَّارُ
Waxal ne : “Man daal ab xuppekat laa. Te jenn Yàlla amul judul, Yàlla jiy jenn , Notaakoon ba,
66رَبُّ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ وَمَا بَيْنَهُمَا الْعَزِيزُ الْغَفَّارُ
Mooy Boroom asamaan yeek suuf si ak li nekk ci seen diggënte, te mooy boroom Kàttan gi, di Jégëlaakoon bi”.
67قُلْ هُوَ نَبَأٌ عَظِيمٌ
Waxal ne : “Xibaar bu rëy la,
68أَنتُمْ عَنْهُ مُعْرِضُونَ
waaye yéen dumóoyu ngeen ko.
69مَا كَانَ لِيَ مِنْ عِلْمٍ بِالْمَلَإِ الْأَعْلَىٰ إِذْ يَخْتَصِمُونَ
Amuma woon xam-xam ca xulóob kilifa ya gën a kawe.
SadFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
67Aaya

Tekki — Sad 67

Simoore Sad Aaya 67 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Waxal ne : “Xibaar bu rëy la,

Simoore Aaya 67/88 — Sad ص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Sad Dégg, Sad Tekki, Sad mp3, Sad pdf. Aaya 65–69. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers