Sad · 66/88
Tekki Waxtaan — Sad
رَبُّ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ وَمَا بَيْنَهُمَا الْعَزِيزُ الْغَفَّارُ ۝٦٦
Rabbus samaawaati wal ardi wa maa bainahumal `Azeezul Ghaffaar
📖 Tekkim Wolof
Mooy Boroom asamaan yeek suuf si ak li nekk ci seen diggënte, te mooy boroom Kàttan gi, di Jégëlaakoon bi”.
🎧 Dégg

📜 Aaya 64-68 — Sad

64إِنَّ ذَٰلِكَ لَحَقٌّ تَخَاصُمُ أَهْلِ النَّارِ
Lii daal tigi mooy xulóob waa Safara
65قُلْ إِنَّمَا أَنَا مُنذِرٌ ۖ وَمَا مِنْ إِلَٰهٍ إِلَّا اللَّهُ الْوَاحِدُ الْقَهَّارُ
Waxal ne : “Man daal ab xuppekat laa. Te jenn Yàlla amul judul, Yàlla jiy jenn , Notaakoon ba,
66رَبُّ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ وَمَا بَيْنَهُمَا الْعَزِيزُ الْغَفَّارُ
Mooy Boroom asamaan yeek suuf si ak li nekk ci seen diggënte, te mooy boroom Kàttan gi, di Jégëlaakoon bi”.
67قُلْ هُوَ نَبَأٌ عَظِيمٌ
Waxal ne : “Xibaar bu rëy la,
68أَنتُمْ عَنْهُ مُعْرِضُونَ
waaye yéen dumóoyu ngeen ko.
SadFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
66Aaya

Tekki — Sad 66

Simoore Sad Aaya 66 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mooy Boroom asamaan yeek suuf si ak li nekk ci…

Simoore Aaya 66/88 — Sad ص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Sad Dégg, Sad Tekki, Sad mp3, Sad pdf. Aaya 64–68. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers