Az-Zumar · 19/75
Tekki Waxtaan — Az-Zumar
أَفَمَنْ حَقَّ عَلَيْهِ كَلِمَةُ الْعَذَابِ أَفَأَنتَ تُنقِذُ مَن فِي النَّارِ ١٩
Transliteration
Afaman haqqa `alaihi kalimatul `azaab; afa anta tunqizu man fin Naar
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ka baatub mbugël yay ci moom,... ndax yaw yaay xettali ku nekk ca biir safara ?
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 17-21 — Az-Zumar
17وَالَّذِينَ اجْتَنَبُوا الطَّاغُوتَ أَن يَعْبُدُوهَا وَأَنَابُوا إِلَى اللَّهِ لَهُمُ الْبُشْرَىٰ ۚ فَبَشِّرْ عِبَادِ
Ñay moytandikoo jaamuy xërëm, tey dellu ca Yàlla, danañu am mbégte ! Bégalal Sama jaam ñi
18الَّذِينَ يَسْتَمِعُونَ الْقَوْلَ فَيَتَّبِعُونَ أَحْسَنَهُ ۚ أُولَٰئِكَ الَّذِينَ هَدَاهُمُ اللَّهُ ۖ وَأُولَٰئِكَ هُمْ أُولُو الْأَلْبَابِ
Ña nga xam ne dañuy déglu Wax, tey topp la ca gën a rafet. Ñoom la Yàlla gindi te ñooy woroom xel ya !
19أَفَمَنْ حَقَّ عَلَيْهِ كَلِمَةُ الْعَذَابِ أَفَأَنتَ تُنقِذُ مَن فِي النَّارِ
Ka baatub mbugël yay ci moom,... ndax yaw yaay xettali ku nekk ca biir safara ?
20لَٰكِنِ الَّذِينَ اتَّقَوْا رَبَّهُمْ لَهُمْ غُرَفٌ مِّن فَوْقِهَا غُرَفٌ مَّبْنِيَّةٌ تَجْرِي مِن تَحْتِهَا الْأَنْهَارُ ۖ وَعْدَ اللَّهِ ۖ لَا يُخْلِفُ اللَّهُ الْمِيعَادَ
Waaye ñay ragal seen Boroom am nañu [ay neegi] taax yu tegaloo ay dex di daw ci suufam. Muy digub Yàlla ! Te Yàlla du wuute Ab dégg.
21أَلَمْ تَرَ أَنَّ اللَّهَ أَنزَلَ مِنَ السَّمَاءِ مَاءً فَسَلَكَهُ يَنَابِيعَ فِي الْأَرْضِ ثُمَّ يُخْرِجُ بِهِ زَرْعًا مُّخْتَلِفًا أَلْوَانُهُ ثُمَّ يَهِيجُ فَتَرَاهُ مُصْفَرًّا ثُمَّ يَجْعَلُهُ حُطَامًا ۚ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَذِكْرَىٰ لِأُولِي الْأَلْبَابِ
Xanaa gisoo ne Yàlla wàcce na ndox mu bawoo asamaan, daldi koy sóob ci bëtu ndox ci biir suuf si ; di ca, génne mbay mu wuute ay wirgó, di lu bëbbu, nga gis ko mu mboq wow ; bay, dammatoo. Ag fàttiliku nekk na ci biir loolu ngir [aw nit] ñu am ay xel.
Az-ZumarFihi Alxuraan
75Aaya
MeccanRevelation
19Aaya
Tekki — Az-Zumar 19
Simoore Az-Zumar Aaya 19 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ka baatub mbugël yay ci moom,... ndax yaw yaay xettali…Simoore Aaya 19/75 — Az-Zumar الزمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Az-Zumar Dégg, Az-Zumar Tekki, Az-Zumar mp3, Az-Zumar pdf. Aaya 17–21. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








