Az-Zumar · 20/75
Tekki Waxtaan — Az-Zumar
لَٰكِنِ الَّذِينَ اتَّقَوْا رَبَّهُمْ لَهُمْ غُرَفٌ مِّن فَوْقِهَا غُرَفٌ مَّبْنِيَّةٌ تَجْرِي مِن تَحْتِهَا الْأَنْهَارُ ۖ وَعْدَ اللَّهِ ۖ لَا يُخْلِفُ اللَّهُ الْمِيعَادَ ۝٢٠
Laakinil lazeenat taqaw Rabbahum lahum ghurafum min fawqihaa ghurafum mabniyyatun tajree min tahtihal anhaar; wa`dal laah; laa yukhliful laahul mee`aad
📖 Tekkim Wolof
Waaye ñay ragal seen Boroom am nañu [ay neegi] taax yu tegaloo ay dex di daw ci suufam. Muy digub Yàlla ! Te Yàlla du wuute Ab dégg.
🎧 Dégg

📜 Aaya 18-22 — Az-Zumar

18الَّذِينَ يَسْتَمِعُونَ الْقَوْلَ فَيَتَّبِعُونَ أَحْسَنَهُ ۚ أُولَٰئِكَ الَّذِينَ هَدَاهُمُ اللَّهُ ۖ وَأُولَٰئِكَ هُمْ أُولُو الْأَلْبَابِ
Ña nga xam ne dañuy déglu Wax, tey topp la ca gën a rafet. Ñoom la Yàlla gindi te ñooy woroom xel ya !
19أَفَمَنْ حَقَّ عَلَيْهِ كَلِمَةُ الْعَذَابِ أَفَأَنتَ تُنقِذُ مَن فِي النَّارِ
Ka baatub mbugël yay ci moom,... ndax yaw yaay xettali ku nekk ca biir safara ?
20لَٰكِنِ الَّذِينَ اتَّقَوْا رَبَّهُمْ لَهُمْ غُرَفٌ مِّن فَوْقِهَا غُرَفٌ مَّبْنِيَّةٌ تَجْرِي مِن تَحْتِهَا الْأَنْهَارُ ۖ وَعْدَ اللَّهِ ۖ لَا يُخْلِفُ اللَّهُ الْمِيعَادَ
Waaye ñay ragal seen Boroom am nañu [ay neegi] taax yu tegaloo ay dex di daw ci suufam. Muy digub Yàlla ! Te Yàlla du wuute Ab dégg.
21أَلَمْ تَرَ أَنَّ اللَّهَ أَنزَلَ مِنَ السَّمَاءِ مَاءً فَسَلَكَهُ يَنَابِيعَ فِي الْأَرْضِ ثُمَّ يُخْرِجُ بِهِ زَرْعًا مُّخْتَلِفًا أَلْوَانُهُ ثُمَّ يَهِيجُ فَتَرَاهُ مُصْفَرًّا ثُمَّ يَجْعَلُهُ حُطَامًا ۚ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَذِكْرَىٰ لِأُولِي الْأَلْبَابِ
Xanaa gisoo ne Yàlla wàcce na ndox mu bawoo asamaan, daldi koy sóob ci bëtu ndox ci biir suuf si ; di ca, génne mbay mu wuute ay wirgó, di lu bëbbu, nga gis ko mu mboq wow ; bay, dammatoo. Ag fàttiliku nekk na ci biir loolu ngir [aw nit] ñu am ay xel.
22أَفَمَن شَرَحَ اللَّهُ صَدْرَهُ لِلْإِسْلَامِ فَهُوَ عَلَىٰ نُورٍ مِّن رَّبِّهِ ۚ فَوَيْلٌ لِّلْقَاسِيَةِ قُلُوبُهُم مِّن ذِكْرِ اللَّهِ ۚ أُولَٰئِكَ فِي ضَلَالٍ مُّبِينٍ
Moo ndax ki Yàlla ubbi dënnam ci Lislaam mu nekk ci leerug Boroomam( moo gën walla ka des cig kéefër)... Toskare ñeel na ñiy bañ a tudd Yàlla ngir xol bu wow. Ñoom ña nga ca réer gu bir.
Az-ZumarFihi Alxuraan
75Aaya
MeccanRevelation
20Aaya

Tekki — Az-Zumar 20

Simoore Az-Zumar Aaya 20 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Waaye ñay ragal seen Boroom am nañu [ay neegi] taax…

Simoore Aaya 20/75 — Az-Zumar الزمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Az-Zumar Dégg, Az-Zumar Tekki, Az-Zumar mp3, Az-Zumar pdf. Aaya 18–22. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers