Ghafir · 30/85
Tekki Waxtaan — Ghafir
وَقَالَ الَّذِي آمَنَ يَا قَوْمِ إِنِّي أَخَافُ عَلَيْكُم مِّثْلَ يَوْمِ الْأَحْزَابِ ۝٣٠
Wa qaalal lazee aamana yaa qawmi inneee akhaafu `alaikum misla yawmil Ahzaab
📖 Tekkim Wolof
Ka gëmoon daldi waxaat ne : "Yéen samaw nit, ragal naa ci yéen lu mel ni bis ba farandoo ya doon xare.

🎧 Dégg


📜 Aaya 28-32 — Ghafir

28وَقَالَ رَجُلٌ مُّؤْمِنٌ مِّنْ آلِ فِرْعَوْنَ يَكْتُمُ إِيمَانَهُ أَتَقْتُلُونَ رَجُلًا أَن يَقُولَ رَبِّيَ اللَّهُ وَقَدْ جَاءَكُم بِالْبَيِّنَاتِ مِن رَّبِّكُمْ ۖ وَإِن يَكُ كَاذِبًا فَعَلَيْهِ كَذِبُهُ ۖ وَإِن يَكُ صَادِقًا يُصِبْكُم بَعْضُ الَّذِي يَعِدُكُمْ ۖ إِنَّ اللَّهَ لَا يَهْدِي مَنْ هُوَ مُسْرِفٌ كَذَّابٌ
Mu am waaju gëm te bokk ca waa kër Firawna, daldi wax ne : “Ndax dangeen a bëgg rey waa joo xam ne li mu wax lépp moo di ne : “Yàllaay sama Boroom” ? Te indil na leen ay firnde yu bawoo ca Yàlla. Su fekkee day fen, fenam ya du ko moy ; su waxee dëgg, ngeen dor a xam ne li mu leen dig dana dal seen kow”. Te, Yàlla du gindi mukk fenkat buy yàq (waaja da doon nëbbu ngëmam) !
29يَا قَوْمِ لَكُمُ الْمُلْكُ الْيَوْمَ ظَاهِرِينَ فِي الْأَرْضِ فَمَن يَنصُرُنَا مِن بَأْسِ اللَّهِ إِن جَاءَنَا ۚ قَالَ فِرْعَوْنُ مَا أُرِيكُمْ إِلَّا مَا أَرَىٰ وَمَا أَهْدِيكُمْ إِلَّا سَبِيلَ الرَّشَادِ
“Yéen samaw nit, tey yéen a ngi gore, am lool doole ci kaw suuf si (réew yi). Waaye ana kan moo nuy man a dimbali ci mbugëlum Yàlla su nu digëlee ? ” Firawna daldi ne : “Wanumaleen lu dul li ma gis. Te it duma leen teg fudul ci yoonu njub”.
30وَقَالَ الَّذِي آمَنَ يَا قَوْمِ إِنِّي أَخَافُ عَلَيْكُم مِّثْلَ يَوْمِ الْأَحْزَابِ
Ka gëmoon daldi waxaat ne : "Yéen samaw nit, ragal naa ci yéen lu mel ni bis ba farandoo ya doon xare.
31مِثْلَ دَأْبِ قَوْمِ نُوحٍ وَعَادٍ وَثَمُودَ وَالَّذِينَ مِن بَعْدِهِمْ ۚ وَمَا اللَّهُ يُرِيدُ ظُلْمًا لِّلْعِبَادِ
Lu melni lëgg-lëggub nitu Nooh, ak Aad ak Samuud, ak ña leen mujjoon”. Te Yàlla bëggul ag tooñ ci jaamam ñi.
32وَيَا قَوْمِ إِنِّي أَخَافُ عَلَيْكُمْ يَوْمَ التَّنَادِ
“Éy yéen samaw nit, ragal naa ci yéen bisub wootante ba,
GhafirFihi Alxuraan
85Aaya
MeccanRevelation
30Aaya

Tekki — Ghafir 30

Simoore Ghafir Aaya 30 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ka gëmoon daldi waxaat ne : "Yéen samaw nit, ragal…

Simoore Aaya 30/85 — Ghafir غافر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ghafir Dégg, Ghafir Tekki, Ghafir mp3, Ghafir pdf. Aaya 28–32. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers