Ghafir · 51/85
Tekki Waxtaan — Ghafir
إِنَّا لَنَنصُرُ رُسُلَنَا وَالَّذِينَ آمَنُوا فِي الْحَيَاةِ الدُّنْيَا وَيَوْمَ يَقُومُ الْأَشْهَادُ ٥١
Transliteration
Innaa lanansuru Rusulanaa wallazeena aamanoo fil hayaatid dunyaa wa Yawma yaqoomul ashhaad
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Nun, Yàlla dananu dimbali (jox ndam), Sunuy Yonnent, ak ñi gëm, ci dundug àddina sii ak bu seede ya taxawee (Bis Pénc ba),
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 49-53 — Ghafir
49وَقَالَ الَّذِينَ فِي النَّارِ لِخَزَنَةِ جَهَنَّمَ ادْعُوا رَبَّكُمْ يُخَفِّفْ عَنَّا يَوْمًا مِّنَ الْعَذَابِ
Ña nekk ca biir Safaraa ngay wax ña koy wàttu naan leen : “Ñaanleen seen Boroom mu woyofalal [nu] doonte la sax benn bis lay doon ci mbugël mi”.
50قَالُوا أَوَلَمْ تَكُ تَأْتِيكُمْ رُسُلُكُم بِالْبَيِّنَاتِ ۖ قَالُوا بَلَىٰ ۚ قَالُوا فَادْعُوا ۗ وَمَا دُعَاءُ الْكَافِرِينَ إِلَّا فِي ضَلَالٍ
Wattukat ya ne leen : “moo ndax, seeni Yonnent indiluñuleen woon ay lay yu leer naññ” ? Ñu ne : “Axakañ” ! Ñu waxaat ne [wattukat ya]: “Kon, ñaanleen” ! Ñaanug yéefar moom ag réer doŋŋ la.
51إِنَّا لَنَنصُرُ رُسُلَنَا وَالَّذِينَ آمَنُوا فِي الْحَيَاةِ الدُّنْيَا وَيَوْمَ يَقُومُ الْأَشْهَادُ
Nun, Yàlla dananu dimbali (jox ndam), Sunuy Yonnent, ak ñi gëm, ci dundug àddina sii ak bu seede ya taxawee (Bis Pénc ba),
52يَوْمَ لَا يَنفَعُ الظَّالِمِينَ مَعْذِرَتُهُمْ ۖ وَلَهُمُ اللَّعْنَةُ وَلَهُمْ سُوءُ الدَّارِ
bis ba nga xam ne tooñkat ya, seenug doglu ngànt du leen jariñ dara te am rëb dal na leen te it am nañu fa kër gu bon (soof).
53وَلَقَدْ آتَيْنَا مُوسَى الْهُدَىٰ وَأَوْرَثْنَا بَنِي إِسْرَائِيلَ الْكِتَابَ
Indil Nanu, Muusaa njub, te donale Nanu giiru Banii-Israayiila, Téere ba,
GhafirFihi Alxuraan
85Aaya
MeccanRevelation
51Aaya
Tekki — Ghafir 51
Simoore Ghafir Aaya 51 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nun, Yàlla dananu dimbali (jox ndam), Sunuy Yonnent, ak ñi…Simoore Aaya 51/85 — Ghafir غافر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ghafir Dégg, Ghafir Tekki, Ghafir mp3, Ghafir pdf. Aaya 49–53. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








