Ghafir · 52/85
Tekki Waxtaan — Simoore Ghafir
يَوْمَ لَا يَنفَعُ الظَّالِمِينَ مَعْذِرَتُهُمْ ۖ وَلَهُمُ اللَّعْنَةُ وَلَهُمْ سُوءُ الدَّارِ ۝٥٢
Yawma laa yanfa`uz zaalimeena ma`ziratuhum wa lahumul la`natu wa lahum soooud daar
📖 Tekkim Wolof
bis ba nga xam ne tooñkat ya, seenug doglu ngànt du leen jariñ dara te am rëb dal na leen te it am nañu fa kër gu bon (soof).

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 50-54 — Simoore Ghafir

50قَالُوا أَوَلَمْ تَكُ تَأْتِيكُمْ رُسُلُكُم بِالْبَيِّنَاتِ ۖ قَالُوا بَلَىٰ ۚ قَالُوا فَادْعُوا ۗ وَمَا دُعَاءُ الْكَافِرِينَ إِلَّا فِي ضَلَالٍ
Wattukat ya ne leen : “moo ndax, seeni Yonnent indiluñuleen woon ay lay yu leer naññ” ? Ñu ne : “Axakañ” ! Ñu waxaat ne [wattukat ya]: “Kon, ñaanleen” ! Ñaanug yéefar moom ag réer doŋŋ la.
51إِنَّا لَنَنصُرُ رُسُلَنَا وَالَّذِينَ آمَنُوا فِي الْحَيَاةِ الدُّنْيَا وَيَوْمَ يَقُومُ الْأَشْهَادُ
Nun, Yàlla dananu dimbali (jox ndam), Sunuy Yonnent, ak ñi gëm, ci dundug àddina sii ak bu seede ya taxawee (Bis Pénc ba),
52يَوْمَ لَا يَنفَعُ الظَّالِمِينَ مَعْذِرَتُهُمْ ۖ وَلَهُمُ اللَّعْنَةُ وَلَهُمْ سُوءُ الدَّارِ
bis ba nga xam ne tooñkat ya, seenug doglu ngànt du leen jariñ dara te am rëb dal na leen te it am nañu fa kër gu bon (soof).
53وَلَقَدْ آتَيْنَا مُوسَى الْهُدَىٰ وَأَوْرَثْنَا بَنِي إِسْرَائِيلَ الْكِتَابَ
Indil Nanu, Muusaa njub, te donale Nanu giiru Banii-Israayiila, Téere ba,
54هُدًى وَذِكْرَىٰ لِأُولِي الْأَلْبَابِ
mu di njub ak ug fàttali ngir ñu di woroom i xel (di xalaat).
GhafirFihi Alxuraan
85Aaya
MeccanRevelation
52Aaya

Tekki — Ghafir 52

Simoore Ghafir Aaya 52 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : bis ba nga xam ne tooñkat ya, seenug doglu ngànt…

Simoore Aaya 52/85 — Simoore Ghafir غافر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ghafir Dégg, Simoore Ghafir Tekki, Simoore Ghafir mp3, Simoore Ghafir pdf. Aaya 50–54. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers