Ghafir · 85/85
Tekki Waxtaan — Ghafir
فَلَمْ يَكُ يَنفَعُهُمْ إِيمَانُهُمْ لَمَّا رَأَوْا بَأْسَنَا ۖ سُنَّتَ اللَّهِ الَّتِي قَدْ خَلَتْ فِي عِبَادِهِ ۖ وَخَسِرَ هُنَالِكَ الْكَافِرُونَ ٨٥
Transliteration
Falam yaku tanfa `uhum eemaanuhum lammaa ra-aw baasana sunnatal laahil latee qad khalat fee `ibaadihee wa khasira hunaalikal kaafiroon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Seen ngëm googee jariñatuleen dara, ba ñu xasee ba gis tiis wa, muy àttey Yàlla ; Kem ni mu ko weyëlee woon ca jaamam ña. Foofee la yéefar ya di yàqulee tigi.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 83-85 — Ghafir
83فَلَمَّا جَاءَتْهُمْ رُسُلُهُم بِالْبَيِّنَاتِ فَرِحُوا بِمَا عِندَهُم مِّنَ الْعِلْمِ وَحَاقَ بِهِم مَّا كَانُوا بِهِ يَسْتَهْزِئُونَ
, Ba seen Yonnent dikkee indil leen ay lay yu leer nàññ, bokk na ca lañu xamoon. Lañu daan ñaawalaatee far sóor leen mujj leen talañ (faagaagal).
84فَلَمَّا رَأَوْا بَأْسَنَا قَالُوا آمَنَّا بِاللَّهِ وَحْدَهُ وَكَفَرْنَا بِمَا كُنَّا بِهِ مُشْرِكِينَ
Ba ñu gisee Sunu Kàttan, daldi nañuy wax naan : “Yàlla doŋŋ la nu gëm, te weddi na nu la nu ko daan bokkaaleel”.
85فَلَمْ يَكُ يَنفَعُهُمْ إِيمَانُهُمْ لَمَّا رَأَوْا بَأْسَنَا ۖ سُنَّتَ اللَّهِ الَّتِي قَدْ خَلَتْ فِي عِبَادِهِ ۖ وَخَسِرَ هُنَالِكَ الْكَافِرُونَ
Seen ngëm googee jariñatuleen dara, ba ñu xasee ba gis tiis wa, muy àttey Yàlla ; Kem ni mu ko weyëlee woon ca jaamam ña. Foofee la yéefar ya di yàqulee tigi.
GhafirFihi Alxuraan
85Aaya
MeccanRevelation
85Aaya
Tekki — Ghafir 85
Simoore Ghafir Aaya 85 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Seen ngëm googee jariñatuleen dara, ba ñu xasee ba gis…Simoore Aaya 85/85 — Ghafir غافر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ghafir Dégg, Ghafir Tekki, Ghafir mp3, Ghafir pdf. Aaya 83–85. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








