Ghafir · 84/85
Tekki Waxtaan — Ghafir
فَلَمَّا رَأَوْا بَأْسَنَا قَالُوا آمَنَّا بِاللَّهِ وَحْدَهُ وَكَفَرْنَا بِمَا كُنَّا بِهِ مُشْرِكِينَ ٨٤
Transliteration
Falammaa ra aw baasanaa qaalooo aamannaa billaahi wahdahoo wa kafarnaa bimaa kunnaa bihee mushrikeen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ba ñu gisee Sunu Kàttan, daldi nañuy wax naan : “Yàlla doŋŋ la nu gëm, te weddi na nu la nu ko daan bokkaaleel”.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 82-85 — Ghafir
82أَفَلَمْ يَسِيرُوا فِي الْأَرْضِ فَيَنظُرُوا كَيْفَ كَانَ عَاقِبَةُ الَّذِينَ مِن قَبْلِهِمْ ۚ كَانُوا أَكْثَرَ مِنْهُمْ وَأَشَدَّ قُوَّةً وَآثَارًا فِي الْأَرْضِ فَمَا أَغْنَىٰ عَنْهُم مَّا كَانُوا يَكْسِبُونَ
Xanaa du ñu dox ci kaw suuf tey seetlu mujjug xeet ya leen jiitu woon ? ëppoon leen gënoon leen bari doole [ak i jeexit] ci suuf si. Te lañu daan fàggu fegalu leen dara (taxut woon mu doy leen).
83فَلَمَّا جَاءَتْهُمْ رُسُلُهُم بِالْبَيِّنَاتِ فَرِحُوا بِمَا عِندَهُم مِّنَ الْعِلْمِ وَحَاقَ بِهِم مَّا كَانُوا بِهِ يَسْتَهْزِئُونَ
, Ba seen Yonnent dikkee indil leen ay lay yu leer nàññ, bokk na ca lañu xamoon. Lañu daan ñaawalaatee far sóor leen mujj leen talañ (faagaagal).
84فَلَمَّا رَأَوْا بَأْسَنَا قَالُوا آمَنَّا بِاللَّهِ وَحْدَهُ وَكَفَرْنَا بِمَا كُنَّا بِهِ مُشْرِكِينَ
Ba ñu gisee Sunu Kàttan, daldi nañuy wax naan : “Yàlla doŋŋ la nu gëm, te weddi na nu la nu ko daan bokkaaleel”.
85فَلَمْ يَكُ يَنفَعُهُمْ إِيمَانُهُمْ لَمَّا رَأَوْا بَأْسَنَا ۖ سُنَّتَ اللَّهِ الَّتِي قَدْ خَلَتْ فِي عِبَادِهِ ۖ وَخَسِرَ هُنَالِكَ الْكَافِرُونَ
Seen ngëm googee jariñatuleen dara, ba ñu xasee ba gis tiis wa, muy àttey Yàlla ; Kem ni mu ko weyëlee woon ca jaamam ña. Foofee la yéefar ya di yàqulee tigi.
GhafirFihi Alxuraan
85Aaya
MeccanRevelation
84Aaya
Tekki — Ghafir 84
Simoore Ghafir Aaya 84 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ba ñu gisee Sunu Kàttan, daldi nañuy wax naan :…Simoore Aaya 84/85 — Ghafir غافر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ghafir Dégg, Ghafir Tekki, Ghafir mp3, Ghafir pdf. Aaya 82–85. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








