Az-Zukhruf · 12/89
Tekki Waxtaan — Simoore Az-Zukhruf
وَالَّذِي خَلَقَ الْأَزْوَاجَ كُلَّهَا وَجَعَلَ لَكُم مِّنَ الْفُلْكِ وَالْأَنْعَامِ مَا تَرْكَبُونَ ۝١٢
Wallazee khalaqal azwaaja kullahaa wa ja`ala lakum minal fulki wal-an`aami maa tarkaboon
📖 Tekkim Wolof
Moo bind tóolent yépp, defaral ay gaal, amal yu ngeen di war,

🎧 Dégg


📜 Aaya 10-14 — Simoore Az-Zukhruf

10الَّذِي جَعَلَ لَكُمُ الْأَرْضَ مَهْدًا وَجَعَلَ لَكُمْ فِيهَا سُبُلًا لَّعَلَّكُمْ تَهْتَدُونَ
Yàlla mi leen defal suuf si muy laltaay defaral na leen ci ay yoon ngir ngeen man cee ginduku ;
11وَالَّذِي نَزَّلَ مِنَ السَّمَاءِ مَاءً بِقَدَرٍ فَأَنشَرْنَا بِهِ بَلْدَةً مَّيْتًا ۚ كَذَٰلِكَ تُخْرَجُونَ
Mooy kiy wàccee am ndox ci asamaan si di ko yemale Ñu di ca naatal ay dëkk yu bekkooroon. noonu it ngeen di dekkiwaate ;
12وَالَّذِي خَلَقَ الْأَزْوَاجَ كُلَّهَا وَجَعَلَ لَكُم مِّنَ الْفُلْكِ وَالْأَنْعَامِ مَا تَرْكَبُونَ
Moo bind tóolent yépp, defaral ay gaal, amal yu ngeen di war,
13لِتَسْتَوُوا عَلَىٰ ظُهُورِهِ ثُمَّ تَذْكُرُوا نِعْمَةَ رَبِّكُمْ إِذَا اسْتَوَيْتُمْ عَلَيْهِ وَتَقُولُوا سُبْحَانَ الَّذِي سَخَّرَ لَنَا هَٰذَا وَمَا كُنَّا لَهُ مُقْرِنِينَ
ngeen di def ñoŋŋ ca kaw, ngeen di fàttaliku xéewali Yàlla, su ngeen yemoo ca kaw ne ñoŋŋ, te it na ngeen di wax naan : “Tudd nanu sellug ki nu tàggatalal lii (wépp waruwaay) te manalu nu ko woon sunu bopp.
14وَإِنَّا إِلَىٰ رَبِّنَا لَمُنقَلِبُونَ
Te dañuy wëlbatiku jëm ci sunu Boroom”.
Az-ZukhrufFihi Alxuraan
89Aaya
MeccanRevelation
12Aaya

Tekki — Az-Zukhruf 12

Simoore Az-Zukhruf Aaya 12 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo bind tóolent yépp, defaral ay gaal, amal yu ngeen…

Simoore Aaya 12/89 — Simoore Az-Zukhruf الزخرف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Az-Zukhruf Dégg, Simoore Az-Zukhruf Tekki, Simoore Az-Zukhruf mp3, Simoore Az-Zukhruf pdf. Aaya 10–14. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers