Az-Zukhruf · 18/89
Tekki Waxtaan — Az-Zukhruf
أَوَمَن يُنَشَّأُ فِي الْحِلْيَةِ وَهُوَ فِي الْخِصَامِ غَيْرُ مُبِينٍ ١٨
Transliteration
Awa mai yunashsha`u fil hilyati wa huwa fil khisaami ghairu mubeen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Moo ndax ! Du ul ne (jigéen) mooy màgg ci gànjaroo takkaay, te joŋewul ci dàggasante ?
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 16-20 — Az-Zukhruf
16أَمِ اتَّخَذَ مِمَّا يَخْلُقُ بَنَاتٍ وَأَصْفَاكُم بِالْبَنِينَ
Am Yàlla moom dafa jàpp ci li mu bind aw jigéen def leen ñu di doomam ba eggal yéen mu tànnal leen ay doom yu góor ? (mukk amul)
17وَإِذَا بُشِّرَ أَحَدُهُم بِمَا ضَرَبَ لِلرَّحْمَٰنِ مَثَلًا ظَلَّ وَجْهُهُ مُسْوَدًّا وَهُوَ كَظِيمٌ
Te kat, saa su nu bégëlee kenn ci yéen ak la Yàlla doon misaal (doom ju jigéen), xar- kanamam ba daldi ñukku muy fuuñ-fuuñi (mer).
18أَوَمَن يُنَشَّأُ فِي الْحِلْيَةِ وَهُوَ فِي الْخِصَامِ غَيْرُ مُبِينٍ
Moo ndax ! Du ul ne (jigéen) mooy màgg ci gànjaroo takkaay, te joŋewul ci dàggasante ?
19وَجَعَلُوا الْمَلَائِكَةَ الَّذِينَ هُمْ عِبَادُ الرَّحْمَٰنِ إِنَاثًا ۚ أَشَهِدُوا خَلْقَهُمْ ۚ سَتُكْتَبُ شَهَادَتُهُمْ وَيُسْأَلُونَ
Ñuy def Malaaka ya di ay jaamu Yàlla [aw jigéen] ! moo ndax baleen Yàlla di sàkk dañu koo teewe woon ? Danañu bind la ñu seede ; laaj leen ko (ba xam lu ñu ca xam).
20وَقَالُوا لَوْ شَاءَ الرَّحْمَٰنُ مَا عَبَدْنَاهُم ۗ مَّا لَهُم بِذَٰلِكَ مِنْ عِلْمٍ ۖ إِنْ هُمْ إِلَّا يَخْرُصُونَ
Dañuy wax naan : “Bu neexoon Yàlla du nu leen jaamu”. Waaye amuñu ca benn xam- xam ; dañuy foog doŋŋ.
Az-ZukhrufFihi Alxuraan
89Aaya
MeccanRevelation
18Aaya
Tekki — Az-Zukhruf 18
Simoore Az-Zukhruf Aaya 18 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ndax ! Du ul ne (jigéen) mooy màgg ci…Simoore Aaya 18/89 — Az-Zukhruf الزخرف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Az-Zukhruf Dégg, Az-Zukhruf Tekki, Az-Zukhruf mp3, Az-Zukhruf pdf. Aaya 16–20. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








