Az-Zukhruf · 82/89
Tekki Waxtaan — Simoore Az-Zukhruf
سُبْحَانَ رَبِّ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ رَبِّ الْعَرْشِ عَمَّا يَصِفُونَ ۝٨٢
Subhaana Rabbis samaawaati wal ardi Rabbil Arshi `ammaa yasifoon
📖 Tekkim Wolof
Tuddnaa sellug Boroom asamaan yeek suuf, mooy Boroom (Aras) gàngunaay ga ; Kawe na lool soree ak ni ñu koy melal.

🎧 Dégg


📜 Aaya 80-84 — Simoore Az-Zukhruf

80أَمْ يَحْسَبُونَ أَنَّا لَا نَسْمَعُ سِرَّهُمْ وَنَجْوَاهُم ۚ بَلَىٰ وَرُسُلُنَا لَدَيْهِمْ يَكْتُبُونَ
Moo ndax ñoom dañoo jortu ne dunu dégg li ñuy nëbb ak di ko déeyoo ? Axakañ (dégg Nanu ko de) ! te sunuy ndaw a nga ca ñoom di bind.
81قُلْ إِن كَانَ لِلرَّحْمَٰنِ وَلَدٌ فَأَنَا أَوَّلُ الْعَابِدِينَ
Waxal ne : “Su fekkoon ne Yàlla Yëraamaakoon bi amoon na doom dey, man maay doon jaamam biy gën a (nungu ag njaamam)”.
82سُبْحَانَ رَبِّ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ رَبِّ الْعَرْشِ عَمَّا يَصِفُونَ
Tuddnaa sellug Boroom asamaan yeek suuf, mooy Boroom (Aras) gàngunaay ga ; Kawe na lool soree ak ni ñu koy melal.
83فَذَرْهُمْ يَخُوضُوا وَيَلْعَبُوا حَتَّىٰ يُلَاقُوا يَوْمَهُمُ الَّذِي يُوعَدُونَ
Bàyyileen rekk ñuy nuur ciy caaxaan ak di fo ba baa ñuy dajeek seen bis bi nu leen daan tëgoo (Bis Pénc ba).
84وَهُوَ الَّذِي فِي السَّمَاءِ إِلَٰهٌ وَفِي الْأَرْضِ إِلَٰهٌ ۚ وَهُوَ الْحَكِيمُ الْعَلِيمُ
mooy jenn Yàlla ci asamaan si di Yàlla ci suuf si ; mooy ki Xereñ, di ku Xam !
Az-ZukhrufFihi Alxuraan
89Aaya
MeccanRevelation
82Aaya

Tekki — Az-Zukhruf 82

Simoore Az-Zukhruf Aaya 82 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Tuddnaa sellug Boroom asamaan yeek suuf, mooy Boroom (Aras) gàngunaay…

Simoore Aaya 82/89 — Simoore Az-Zukhruf الزخرف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Az-Zukhruf Dégg, Simoore Az-Zukhruf Tekki, Simoore Az-Zukhruf mp3, Simoore Az-Zukhruf pdf. Aaya 80–84. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers