Az-Zukhruf · 81/89
Tekki Waxtaan — Simoore Az-Zukhruf
قُلْ إِن كَانَ لِلرَّحْمَٰنِ وَلَدٌ فَأَنَا أَوَّلُ الْعَابِدِينَ ۝٨١
Qul in kaana lir Rahmaani walad; fa-ana awwalul `aabideen
📖 Tekkim Wolof
Waxal ne : “Su fekkoon ne Yàlla Yëraamaakoon bi amoon na doom dey, man maay doon jaamam biy gën a (nungu ag njaamam)”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 79-83 — Simoore Az-Zukhruf

79أَمْ أَبْرَمُوا أَمْرًا فَإِنَّا مُبْرِمُونَ
Walla, Ñoom dañoo fexe ay mbir [ak lu man a xew] ? Nun nooy sottal mbir yi ñu alku !
80أَمْ يَحْسَبُونَ أَنَّا لَا نَسْمَعُ سِرَّهُمْ وَنَجْوَاهُم ۚ بَلَىٰ وَرُسُلُنَا لَدَيْهِمْ يَكْتُبُونَ
Moo ndax ñoom dañoo jortu ne dunu dégg li ñuy nëbb ak di ko déeyoo ? Axakañ (dégg Nanu ko de) ! te sunuy ndaw a nga ca ñoom di bind.
81قُلْ إِن كَانَ لِلرَّحْمَٰنِ وَلَدٌ فَأَنَا أَوَّلُ الْعَابِدِينَ
Waxal ne : “Su fekkoon ne Yàlla Yëraamaakoon bi amoon na doom dey, man maay doon jaamam biy gën a (nungu ag njaamam)”.
82سُبْحَانَ رَبِّ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ رَبِّ الْعَرْشِ عَمَّا يَصِفُونَ
Tuddnaa sellug Boroom asamaan yeek suuf, mooy Boroom (Aras) gàngunaay ga ; Kawe na lool soree ak ni ñu koy melal.
83فَذَرْهُمْ يَخُوضُوا وَيَلْعَبُوا حَتَّىٰ يُلَاقُوا يَوْمَهُمُ الَّذِي يُوعَدُونَ
Bàyyileen rekk ñuy nuur ciy caaxaan ak di fo ba baa ñuy dajeek seen bis bi nu leen daan tëgoo (Bis Pénc ba).
Az-ZukhrufFihi Alxuraan
89Aaya
MeccanRevelation
81Aaya

Tekki — Az-Zukhruf 81

Simoore Az-Zukhruf Aaya 81 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Waxal ne : “Su fekkoon ne Yàlla Yëraamaakoon bi amoon…

Simoore Aaya 81/89 — Simoore Az-Zukhruf الزخرف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Az-Zukhruf Dégg, Simoore Az-Zukhruf Tekki, Simoore Az-Zukhruf mp3, Simoore Az-Zukhruf pdf. Aaya 79–83. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers