Ad-Dukhan · 31/59
Tekki Waxtaan — Simoore Ad-Dukhan
مِن فِرْعَوْنَ ۚ إِنَّهُ كَانَ عَالِيًا مِّنَ الْمُسْرِفِينَ ۝٣١
Min Fir`awn; innahoo kaana `aaliyam minal musrifeen
📖 Tekkim Wolof
mom Firawna ma kawe woon lool ca yàqkat ya.

🎧 Dégg


📜 Aaya 29-33 — Simoore Ad-Dukhan

29فَمَا بَكَتْ عَلَيْهِمُ السَّمَاءُ وَالْأَرْضُ وَمَا كَانُوا مُنظَرِينَ
Asamaan ak suuf jooyuñuleen te kenn it muñadikuwuleen.
30وَلَقَدْ نَجَّيْنَا بَنِي إِسْرَائِيلَ مِنَ الْعَذَابِ الْمُهِينِ
Musëloon Nanu , waa bani Israayiila ci mbugël mu doyadima (rey góor)
31مِن فِرْعَوْنَ ۚ إِنَّهُ كَانَ عَالِيًا مِّنَ الْمُسْرِفِينَ
mom Firawna ma kawe woon lool ca yàqkat ya.
32وَلَقَدِ اخْتَرْنَاهُمْ عَلَىٰ عِلْمٍ عَلَى الْعَالَمِينَ
Tànnoon Nanu leen tigi ci kaw waa àddina sépp (bawoo jamono),
33وَآتَيْنَاهُم مِّنَ الْآيَاتِ مَا فِيهِ بَلَاءٌ مُّبِينٌ
indiloon Nanu leen ay kéemaan (firnde) yu leer nàññ.
Ad-DukhanFihi Alxuraan
59Aaya
MeccanRevelation
31Aaya

Tekki — Ad-Dukhan 31

Simoore Ad-Dukhan Aaya 31 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : mom Firawna ma kawe woon lool ca yàqkat ya.

Simoore Aaya 31/59 — Simoore Ad-Dukhan الدخان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ad-Dukhan Dégg, Simoore Ad-Dukhan Tekki, Simoore Ad-Dukhan mp3, Simoore Ad-Dukhan pdf. Aaya 29–33. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers